LYRIC

Sant yalla ak yonentam ba, ci katanu fèey ci léer yi
Loumou sambaraax niu teumbeu, nio ko tanneu faye hilaire yi
Taatane ségg lore yi, Xél yi nourou narou ni mool
Kattane guissék kolloré, faniouye téeri dina mole
Djeune wou mak diex na, yaboy yéy fiy niodi piranha
Waass yi topp rang bi, mbexx mi yoobou léne fou pire khana
Succée amoul bankhass, fo tokhé lap niu R.I.P
Gni manoul took ci banc xass gni soobou, sipp sa rap bi

King from the River
King from the River
King from the River
King from the River

Ba Bess niu guiss laalakè – King from the River!!!
Rio fresco baaxé la bénéne kilifa
Watt gaal yeugoo, boolé diokoul thiokho Dangou
Kou bagne taye euleuk nga nangou, meuné funé laniu rangou
Flow yi lay chaviré lo, savouré lola technique
Ba nieup di embarqué daniou tann yoon déf ték niit
Déx gui yaana, dangaay xool, ba fa beut yéme
Writah cas la, dalal dank, tay la seut yéem

King from the River
King from the River
King from the River
King from the River

Sama Ndaa ngui ni yaa, tankhal nga sangou naane
Masso guiss kou melni mane sikoul nga took di sagou naane
Dangay talk to talk, fèk may work di jok
Mc yiy ngooki ngook, sama zik moy baawonaan
…. Ikhssane ak mbakha ci dess
Ndox mi tourou na, legui ane bakheu ci déss
Yeah! bou déme roye dakh bi déss
XaK fi béss, ate mou né niuy yokk vitesse

King from the River
King from the River
King from the River
King from the River

Nangou naniou soobou bathie, nguir naax yi thieupi thieupi
Mana mana nieup ci mbaal mi, king bi sopi djap bi depuis
Hun! Manak yéen ni nitt ak Golo
Té moom sakh – amal na poliomièlite solo
Goukh ci fontaine de jouvence, waral The Writah dou dé
Terreur ni barbe noir, guiss nga Ghost fight la doundé
Unstoppable, bala niuy jonganté la raww
King from the river, by the name of Paul Sparrow

King from the River
King from the River
King from the River
King from the River

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR