LYRIC

{Verse 1}
Médaille yu number one la wëko nak
Loum togue yékeu mou done lékou makk
Kou tongok mom yaay reuthiou gnaakeu
Rap pur et dur dou féthiou niakk
Biggie neu xamni amena raak ci beat bi sakh day djékou PAC
Saayo déggo “wouy walooy” kou djaggadi mo daadjék kou djakk
KK moy djité gni gniy djiteul ak gni djitéé wone
Tay tole bé soukheute may bayaalél gni dji teuwone
Xam xam ba tcha koki nak, Katane ga tcha ndodi nak
Xalé bu xélam dh xassane lég lég day soxla woki makk
Wanéna founé ci faana yeup dotoul compétir
Deugueur bopp takh ma def lène malla dilène dompté xiir
Kona yeup la conquérir Koba yeup vont en périr
Xélou djeun nga yor do contenir takh foma compé miir
Fils donale mini may maxi eup leu daradja
Pistonnél Mc bouy aksi ma dieul ko deureudjeu
Knowledge niou naw la tchia Killah meusta nélaw tchia
Beat bi loumou feug may reude tek tchi lou mélodieux

{Refrain}
Gunzout (KK) D-Squad (KK)
LG (KK) Killah Family (KK)
Galsen (KK) Hands up (KK)
Please let me hear you say: “KK Moy Number One”
(2 fois)

{Verse 2}
KK moy number one lou xel yi meuneu nangou leu
Bo tichauli woul li dess sa life bi yeup ay niandou leu
F**k ngni tchi andouleu wone surdose bouniou djambeu leu
Only real mogniy conS. nioune fake bouniou niam douleu
Midi djotna né naagneu nga dieul ampoule di niit (Nigga what ?)
Hit yi bari ni gaagni nigga dampoul tchi NIT
Rap-bou mbède la niodi incarné marginal
Taaral Kocc barma mouy dioli tcha international
Niom nieup la cracké sen code yi ak sama virus man
Légui maa toppeu ci Nitdoff Killah moy sen mot de passe
Gnima daane dinkate dembe nio melni kou rouss man
Bankeu lèn loxo yèèn taspé NABA dou murder AS
Légui rap bi agneau leu tiouné yééy am cote
Bou beat bi wanguéto nga guiss niou warr mbaam yi meunou nio kott
Swaggou boy yi nio beuri niom nieup ndourau rap
Té ko tchi tégal right mou teup saga sou xamé meuno raak

{Refrain}
Gunzout (KK) D-Squad (KK)
LG (KK) Killah Family (KK)
Galsen (KK) Hands up (KK)
Please let me hear you say: “KK Moy Number One”
(2 fois)

{Verse 3}
Meuno lènema jugé f**k séni magistrature
Boudé deug leu keufeul mic ma guiss sa rap pur
Boudé sa opinion dagnelakay dicté my nigga fi dofi am moyenne indil sa cahier nga guiss sa rature
Wekh na domou niima, negga doma nima
Tchi eukhlou Rap Galsen amna kouy waxni do monument
Deug leu dama zarbi mais malay firil saar bi
Djébeuloul tchi mane indaalél aadiya ak ziaar bi
Médaille bi dorée neu, founé mbède décoré meu
Saay youma mic nga dégue amna niam té gooré neu
Killah Killah yémeu def sen xol té dagneko thiabbi kat
Nélène sen xel yi dall ndakh NDK do meusseu saagi sak

{Refrain}
Gunzout (KK) D-Squad (KK)
LG (KK) Killah Family (KK)
Galsen (KK) Hands up (KK)
Please let me hear you say: “KK Moy Number One”
(4 fois)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR