LYRIC

{Intro}
Meune naniou bokk Ndèye, Baay bok lepp
Bamou dess destin lou mata saameu leu
Kollëré !

{Verse 1}
Xarito weu diss lol ci lossou djaam
Boudé anda ndo bo wané guinaaw dalay djam
Pourtant demb rek nga wané ni da ngama yeené jaameuh
Tay ma wane la guinaaw rek nga sani wékku mbaam
Ko dou Niit, amoul lerr dou nite (éclairer)
Matal na waxtu diouraum waayé mélo wouleuk djoulite (Allah)
Kollëré moy limite boudé salaire moy simique
Moy minimum-mou nité souko waathié rek mala mom di dikk
Dagni andeu ngir Yallah wala andeu ngir limala meuneul
Beugne ak Lamigne laalé rek nga daadi yabbi la ngama xamal
Tay Mbaam xoukh laa waayé demb damala Halal
Al Hamdu bamoula dioxoulé mbautou tchine bi damala niamal
Aka djaffé toppeu Serigne TOUBA ngir Cheikh Ibra FALL
Dembe Yâ SALAAM waayé tay sa rafale
DJILY ak SAAM sen mbay wouténa tchi haaal (Louga)
Am ak Xam bo tchi sakkou fexél done Bilal

 

{Refrain}
Al Ham Dou Lilaaah
Nio ngi délou waaat
Sante Yallah Buur Bi def li gueune ci nioune
Niou ngi délou waaat
Fédeuli Kollëré guiy daw sunu digueunték Bilaal
Haaal Haaaal Haaaal Haaaaala
Anda ndo bou jog dem aal leu
You are my fenomen. Got’em Haal leu
Aduna dou yagg bama dem baayi leu
Douma meusseu féthieu Kollëré bi baayi leu

{Verse 2}
Da melni Juda mo saw ci biir dékhou Lac de Guiers
Kollëré daa diko naan mou dioureul ko lou melni mal de mer
Mou ngi Wathiou mou ngi xeuthiou mok intérêt ngi bras de fer
Tabbé ngi tégou wone tchi téranga tass neu done neu Hache de guerre
Haaaaaaaaaaaaaaaaaa
Xaxar yé ngi xataraayu xeuthieu xarfa xouffeu
xarkandigou xalangou xaatim xalaate yuy xirteul xarite beu
Xeuteu Heart-teum (Xol) xeuthiok Xaqqou
Xell tchi xrou xew xew xaré biy xibaar Xamon
Té lolou dioureulna Phiraone ‘alkom Lolou faat neu Malcom
Kollëré féthiékouna laali worma daldi lale Kom Trahison ci Balle comme…
Tass neu seuy, yaak mbok, xagne Sheytané Bane tome

{Refrain}
Al Ham Dou Lilaaah
Nio ngi délou waaat
Sante Yallah Buur Bi def li gueune ci nioune
Niou ngi délou waaat
Fédeuli Kollëré guiy daw sunu digueunték Bilaal
Haaal Haaaal Haaaal Haaaaala
Anda ndo bou jog dem aal leu
You are my fenomen. Got’em Haal leu
Aduna dou yagg bama dem baayi leu
Douma meusseu féthieu Kollëré bi baayi leu
Anda ndo bou jog dem aal leu
You are my fenomen. Got’em Haal leu
Aduna dou yagg bama dem baayi leu
Douma meusseu féthieu Kollëré bi baayi leu

{Bridge}
Baatou goré ba déh dieulko defko gaanaay
Soubeu dou agne dou rérr dé waayé matena sett waay
Gorél ba xeuy rek déh
Dara feukoul sunu beute yi noone dougne niou réh

Baatou goré ba déh dieulko defko gaanaay
Soubeu dou agne dou rérr dé waayé matena sett waay
Gorél ba xeuy rek déh
Dara feukoul sunu beute yi noone dougne niou réh

{Refrain}
Al Ham Dou Lilaaah
Nio ngi délou waaat
Sante Yallah Buur Bi def li gueune ci nioune
Niou ngi délou waaat
Fédeuli Kollëré guiy daw sunu digueunték Bilaal
Haaal Haaaal Haaaal Haaaaala
Anda ndo bou jog dem aal leu
You are my fenomen. Got’em Haal leu
Aduna dou yagg bama dem baayi leu
Douma meusseu féthieu Kollëré bi baayi leu

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR