LYRIC

{Verse 1}
Ngeum ngeumou domou Adama may doley dji kay djalalé ci xat xat yi
Yakine nay dikk done fiit mou tagok tiit dotoul pat-pati 
Mou ngay dox di dém yonam, mou ngay baay di route tolam
Djeum djou né gaal li koy yeungeul moy molam
Tempétou bir guédj waroul takh goor saalit
Ngeunél gui ci kawé gnou ngui ko deukheugne ci biir mbalit
Missalou boutiite foumouy diar ba done lakhass? moy rakhass
Nangou naniou, angou naniou, Rangou naniou, sangou naniou
Sopi tookhal yégal wathié yilé gneinte diangal nagnou
Sirou bi gnou dieulé borou passi lagnouy tassi
Mission bi dou meussa gassi, yénéne mind lagnouye gassi
Doute ak certitude douniou meussa tassé
Dafa mélni sik-sak ak YAKINE safaane lagnouko nassé
Pousso bé di xol, est-ce que beut modi khol?
Est-ce que Xel yeup meuna nangou né Jean modi Paul?
Vitessou life bé djogué ci kora yi
Rombe TGV di taliss
Sa xel mi modi police
Sarét yégui moytou Carrapide yi Taxi yi doubler léén
Particulier yi nek ci à péage di kheul bay weuliss
Tali life bé darkness, leundeum takh le bas blesse
Léer toumouranké xol yi leundeum mbété la peste
Yéné yé fébar, lakkou ci sinébar
Patrong di agné di réré gnakkou ménébar
{Speech}

{Verse 2}
Nguisteul falou bour, mélokano bouki ndiour
Yoré paka diwo Niamala fek déréte la beug tour
Xellou askane wi la diap otage di ci fo
Défar féne mou done deug dox sa mind dila wo
Aduna mounoul nekh ba Bouki beugeul diam kéwél
Mou ngui koy sign, mou ngui koy sign nguir sopiko ak ndawal
Politik ngui polo téki, Boul khar koula féki
Ya nangou mou bote la tay boumoula bét boulaye boti
Sama mind bokoul ak sén bosse
Ki takh may déf bokoul ak sén boss
Liy défar Sénégal dou politique délou ci YALLA la
Nguisteul ak oute tuur lolou dou nité doundou aleu la
Nguisteul, Nguisteul mbakhané dall la
Thiant ak khadara bouléne ko khép lolou wall la
Temporél bokoul ak spirituel
Ki yem ci xel bokoul ak ki xam ni guinaw xel mel
Djangal lén xalé yi histoirou gnom Mame Bamba
El Haji Malick, Limamou Laye bouléne yem ci Maba
Descartes ak Platon, Séni djangalé à la con
xol day gnam YALLA xamé Yoneinte tibi bala Bon
Senghor + Wade = Macky
Faratah + Sunna = Bank ci teeré makk gni
Kou faté kila fale folékou
Sant kila may mom moy dolékou

{Speech}

{Outro}
Yeah ki dafa déh, ki di nélaw
ki ci dess dafa yéwou
Na ki yéwou yé kiy nélaw
Ba nopi souli ki déh
dieureudieuf Niambé nonou rék la (x2)
diarawlak Cheikh Moussa Touré
Gaston alias Baye Dieuwrine a.k.a ndongo ndongo yi
Gnoune la souf donté gnodi assamane
Ngeum Ngeum, Yëg Yëg,
Degg degg, Deug deug

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR