LYRIC

{Sir Jamal -Refrain}
Démb soppalékou soubeu doone téyittam(aujourd’hui aussi),,,
Linga wara khaar djougg ca défko itam(aussi)
Fou xel yi djakhasso soulifeu lidi yitéém
Boul xel gnaar nagnou sopi djikoyitam (2 fois)

{Daddy Bibson}
Tomorrow never come yeah,
Boulko trust ak money yeah
Beuss bou nek ak limouy indi, bi tchi topeu ak limouy dindi
Kouko topak foumou lay wini, seni nopp ak foumouy ninii
Soubeu sobeuwu Yalla laa
Xamo ndakh Abdou diambar fakétla diale-la, Wala sa tagué dialéla
Tay bou nek amena soubeu, Ray bou nek amena roubeu
Limouy indi kumpe la , Diémeul sauralé coup bas
Life is short, Déh is hot
Diémeul def lingay def ni Pac
Xadialal ni ngay def today , Meuneu am moy beussou féy
Ki nga sékeul, ki nga nékal meuna xeuy rek né meuy
Boul tok di wakh da ngay khar Kheuy , Def lou bakh dé amoula faay
Yallay borom kheuwlou bi té nit kou nek am nga feuille

{Sir Jamal -Refrain}
Démb soppalékou soubeu doone téyittam(aujourd’hui aussi),,,
Linga wara khaar djougg ca défko itam(aussi)
Fou xel yi djakhasso soulifeu lidi yitéém
Boul xel gnaar nagnou sopi djikoyitam (2 fois)

{Nitdoff}
Meuno nèk manhatan beugu kham li nè wakam
Nanguo beuré meuneu dane taye dèf né toomorow will never come
Xam ba Xam biss bi ngey dèh ci waliw yi niou néweuko ame
Tè nga jèmeu mouri taye ndakh khamoulo lou toom mouro
Ya gui wathie wathie tè woroul nga fèkkè tomorrow
Ya gui fly fly topou life bileuy doumalow
Iblisseu mour sa eyes tè sa nafsou molay goumbalo
Dji khaar yallah taw perte nga bo roudioul li
Yalnaniou yallah mousseul si dewalek borou djiouli
Diougueul baalou ki nga togne jémeu faye ki nga amel
Niounè Real dou meusseu wakh jtm kham nga rek ni nga ngaaka mél
Taye la taye boul khar ba soubeu di laye kone rèthiou watleu ndèl

{Sir Jamal -Refrain}
Démb soppalékou soubeu doone téyittam(aujourd’hui aussi),,,
Linga wara khaar djougg ca défko itam(aussi)
Fou xel yi djakhasso soulifeu lidi yitéém
Boul xel gnaar nagnou sopi djikoyitam (2 fois)

{Speech}

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR