LYRIC

{Refrain}
Love Love Love Love
Door naniou ko guéné galé ndax Love
Deudou djiguène done labé ndax Love
Love Love
Ba na djangue songue Musique ndax Love

{Simon}
Danga ma AM ma youkhouu O niou ladjma kane manei lene U
R bi diss ci mane ba lima beug tiiange lo sama cou (AM.O.U.R.)
Ma Lathie la sa Coeur, niou tétalma fu khonk
Samay battement djapéko boum sa baat lako beugué lonk
{PPS}
Sama mind na silmaxa pass pass togui à part teddeu
Nafar guede XOL cii yonou leundeum tare ni appartheid
Guiss Guiss yi beuri ni KARAW (Divergence) yu ndool xouf ak LAME NELSON
Degg louniou Mandéla Deug Deug Mame del sonn
{Simon}
Sama boss la dou bou ké, Mbindeu bé sopalikou done Bouquet
Yëg Yëg kay rossé guisseul tay bouko noone yi dikay xeintiou nougni souké
Nguir DJII BI saax fok ma use DA BRAIN
Dila topoto BA KHAW sango souf goukh ay brain
{PPS}
Bila Nieup djabé mbalite ma defla Or rou 100 Kara
Ma diekh cii yaw Tooma (Homonyme) taylé sama lep ni SANKARA (Thomas Sankara)
BIEN AIME ni Cesair, Césure bi saisir jeggo SENGHOR (L.S.Senghor)
Ferniente bi boyal Damas (Léon Gontran Damas) firi gueinte yi dieundeu sen ngor (Honneur)

{Refrain}
Love Love Love
Door naniou ko guéné galé ndax Love
Deudou djiguène done labé ndax Love
Love Love Love
Ba na djangue songue Musique ndax Love
Guédeu Aduna deuké sikar ndax Love

{PPS}
Bb KAY (Bécaye Mbaye 2stv) may sa Thierno (El. Thierno Ndiaye tfm) sa garmi dagoul ni HIPPO
Ay thia sa GUEWEUL dou FATUU ndiaram Lamboul tey nga djipo
Ndem deug laniou dji ko, Djiko Dembeu job (Notre passé/Stade Demba Diop)
Niou FALOU djingue may NDER né THIOPET SALAM Dém ba Goob (Récolter)
{Simon}
Gniy wax né “MBEUGUEL AMATOUL” dagnko lire cii ay BOOKS
Naañ niou may “FREEDOM” yémal SEN KUMPE ci Séni TIOUKS
“WAKHAL SA BAYE” “LOU MEUNOUL NIAK” fok mou AM
Job lou beuri def “RYTHME” yéw diour dom toudéko “AMA”
{PPS}
Done FOU ni MALAL TALLA SYLLA, dagoul thiakass niou Guiss
Dékou Marteau ni Talla SYLLA “BEUG DEM” cii yonou NIAGASS
Woorna Mouhamed KOUKA (Simon) sameu “FAATA BARAKA LAHOU”
BISBI bou EL HADJI laniou KO NATE (Books)Taaru FA LAHOU (Allah)
{Simon}
Athia wakhal lila soxal, malay off fal gnilay lakal
Baby doxal koula takal, Ma djoug diongal néko niafal (Thieuy LOVE)
Ndem Nit niémé woul djingale, love diouma lonkal
Diéguéma ma nek nok niggaz yumay neub say tiakhou ndigueuu

{Refrain}
Love Love Love
Door naniou ko guéné galé ndax Love
Deudou djiguène done labé ndax Love
Love Love Love
Ba na djangue songue Musique ndax Love
Guédeu Aduna deuké sikar ndax Love

{PPS}
Mala L.O.V.E Gansta Love ni EVE, Teacher ni BDP (KRS ONE),
Gueustou ci bitti bi, wassarè mbind ci beat yi
{Simon}
Li gneup di lam-lamé, lama lakk live love level djou loumpe Akk
Give Love label diou KUMPE dakk Hip Hop musik dou ko dakk
{PPS}
Légue légue ma méréla, Clash libéré la ndax gnila diapé Haata
Sa mbektè sen matter, fo gassè niou soul, mbéde di school mougne dama teuu
{Simon}
Niouné lou mosso ta moss mak Makkaveli mbindeu bi mo xoss maate
Mythe maate mote ak teulé milédi mala dik love bou outé ak pelé feulé

{Refrain}
Love Love Love Love
Door naniou ko guéné galé ndax Love
Deudou djiguène done labé ndax Love
Love Love Love
Ba na djangue songue Musique ndax Love
Guédeu Aduna deuké sikar ndax Love 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR