LYRIC

Refrain Chrismas

Couplet PPS
Nioy dekil gni niu faté, niuy daw sunu sang bataye
Nio deukak gni niu até, songue lou raw 100 batailles
… Naane li niu sombi kay, namm niu ngui son ba taye
Sakh ci zone bi guindi kay, gni réer ni ay zombi faye
… Nioy diokh kaddu gui bayimak njanaaw
Firri say gueinte, ba do dox di bayi magg ya now
Doon ci zahir, doon ci baatine legui matt nga naw
Rap + 10, true school bi néla mane nga naaw
… Li niouy bind guindi sinnerman
Woowema Writah, real HipHop gnibissina man
Ci séni nopp nénagne, Xak laniou si namone
Lyriciste lounge, PPS n chrismas
(Chant)
Gni kay soloo diko wakhé, féthie diko doxé – Di dioxé doyadi késsé, di sasso mbébéti soxé-
Doon baatou gni né ci kasso, diamarlok system biy sooké-
Di choqué ci beutou niéne, tay niu diour yénéne Picasso
…. Nio reude sa euleuk ni ab guissaané
Khana guissoné nioy takhaw fou sen askan wi sonné
Woor na Wéerou ca lou woor la, War nga waaru célla wor la
Wiiril Yoon wi calawér la, idjil ba firi di thierno
… Meuné founé seuy ci right feel ma
Fanaano gueintou diam yi, seulmou xeuy ci write film
Sunu poo mé teureudi boolé ci goréedi kat – funu xoolé mbind mi wéreudi Paul ay dikaate
Thiouné yé niu colonisé deinke fi golo yi baate, kuniu diox king nga nangou bolé ci goréedi waate.

Refrain Chrismas

Couplet Chrismas

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR