LYRIC

Taw ba ngui bathie, mbédou kogne bi taa
Poto lampe yi faye, soufe séddeu
Wéet sama néek si xalaate you bary lamaye xiir
ma tour ko si feuille, Samaye gueinte nioma trahir
Maye xalate délou goné, deuglou paa ak mère
Jangate souba ndax Sama dembeu dafma rére
Done goné takhone ma keux, euss goumbe teux Lou
Tare fess samaye beut, gnak kham dima peuteuxlou
Lou yomba ma sonal, yone yama ngonal
Fok né assamane soudone daanou makoye téyé
Wayé xôl ma taye, samaye laaffe niniou tooyé
Done yootou fouk jott si niar, rethiou la togué

Refrain (Nectar)

Mangui jégueulou
Mangui jégueulou

Verse Pps
Sama yéné reuye, sama doolée néw
Té keur gui soo yoroul niou jappé la néew
Doo yeuk doo tine, yak goné yee massé
Niak respect mak ak ndaw nonou nga koy missee
Mangui jegueulou souma sagnone tékki ni samaye morome
Paa bi nopalou, mère bi mana géré ak gorome
Xawma souba loumouye indi wayé taye aka tare
Gnata ate niouye djow, sunu gaal mélni kaakatare
Nite gni douniou guiss, fi sa yéné tolou
Kou sagnone yoor Lou bary, galé naate, lép taarou
Akh ki amoul djom, Ki beugoul tékki
Fékhél xôl say nawlé, mélni ….
Boudone kounéy maye sa bope, kone kén dou soneu
Wayee fii mougne a fi née, kou nék ak sa yone
Daniou nane thine bou naré néx, wayé guissouma sakh fourneaux
Missal biye tax ma nane rongognou waa galé Férr na

Refrain (Nectar)

Verse Pps
Dembeu nirok taye, Est-ce que soubaye dakh
Sama jeum di Léwtok sama xél, khawma
Lou takh défouma lii, Lou takh doonouma kii
Doundou conditionel fok ma nelaw fatee nélaw fatee lii
Life bi safatouma dara, boutéel bée koy sapali
Thiow jiboul, nangou, borom réka mana sopi lii
Mangui délou toupe, rame jégueulou
Lo guiss daye jéx, souba kén khamoul loumouye addou
Mangui jégueulou, souma donoul li nguéne beugone ma done
Wayee douma si léne, niakk taxoul ma bone
Pression yi, dou takh ma waxou sama weurseuk
Douma dougueul si louma xamoul, dina khar mou mate seuk
Manatouma tok galee, matter ame té doumako fathie
xawma kagne la sama mbouss di fathie, jombe na sathie
Jomb def Lou bone
Mangui Jegueulou, wayé… dinguene takhirlou

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR