LYRIC

{Refrain}
Ana fake ass nigga yiy wakh ci sunu guinaaw ?
Murder them just like bang !
Ana fuck up nigga douniou dem douniou baayi kène dem ?
Murder them just like bang !
Ana bullshit nigga yiy djalgati pour Kill rap ?
Murder them just like bang !
Gunzout (Gunzout) say too loud
KK my nigga and we’re so proud
Come on

{Verse 1}
Yaw ! Ana gni néwone ND Killah do dem ?
Siguile lène séddé wa mbède bé wouyou wotéém
Oh damn ! Mc nopilène damay fowak yeen
Ma tass lène ci barké bi nigga taudj lène
Lot of talk Bitches ass nigga nél djodo tok
Nigga gueuwouma tott bo doundou deug yaw doma toppeu
Néél sa MC mou baayi sissou té yokk job
Jottaayu fake ass baayékou rek di wokkou thiokkeu
Ana gni néwone Killah wessouwoul phénomène ?
Xana filo man, djougouma ci dilène fène lo mèèn
Soumay RAP déy melni mane dama téyé gun
Ratata taaak sa noppeu yi melni fire burn
Nioune sunuy taukhi tay nékatoul teurr di réindi Mc
Garap day fathie souffé rekka waral rèèn bi gueune ci
Da nga tééleu baakou tééleu youxou mane leu
Sa ndaa li mandi woul kèneu ndax bèneu gouxou naaane leu
Méti yéggagoul fèneu ba nga dégueu youxou mane leu
Li froissé wone dh laay passé nga fokni new Xuman
Killah todjagoul kass té mo ngi def xouyi
Rappeurs yi nangou nagnené malène gueuneu fess couille
Diaratoul sakh kèneu di xeuthiou King bi dégueu nga maam
Xaral ba def xaadjou lima fi def rek yaw nga nkaam
Mcs yi lëmou NDK Yalna baayi Rap
Laakone nalène ci barké Dabakh ak Baye Lat
Kiy meune di def bokoul ak kiy forcé ak takkalém yi
Mbalaanou Rap bi laa djité di lem aka lémi
Dou same académie The Killah Epidémie
Mbède xamna loutah mou djiteul meu ci députém yi
Wowéma Come On Town bouy dogga yeksi Poste Thiaroye
Mane sama ambition nigga wessuna chaisou palais
Mane dama Escobar-ré bitch yeup lay scopar-ré (Balayer)
Maa takh ba gni ngène done wowé fi séni best tocard ré
Laf Thiat chaque track wékou wouma tchi Jack Black
Hot Clap Rap Crack Never sunu Flag drop
Nit to the Doff sa rappeur dafa love koy
Goor Yallah Ngoora Keng nioune doundou ay thiof toy
Mc da nga loff yoyy sa rap bi daffa soff noy
F***k bo wété tchi mbède di nga xoff djoy
Bala tchine bi xégneuti daa fékeu King bi féégnati
Kène kiko sagnati maay def lodoul bagnati

{Refrain}
Ana fake ass nigga yiy wakh ci sunu guinaaw ?
Murder them just like bang !
Ana fuck up nigga douniou dem douniou baayi kène dem ?
Murder them just like bang !
Ana bullshit nigga yiy djalgati pour Kill rap ?
Murder them just like bang !
Gunzout (Gunzout) say too loud
KK my nigga and we’re so proud
Come on

{Verse 2}
Yaw sometime ma narcassique beuri kass ba narr ci sikkeu
Deugué daaj ni marteau pic, done parano ni narcotique
Arsénique ! Possone laa ci fake damay aar saye nit
Bête Scénique ! Kersa mognou teunk ba douniou vexé nit
Na mbède deugueul boppam Killah tek lou gueuneu fess Zénith
Xollou talibé ak fittou gaïndé sama face timide
Tékile sa gueimbeu xaragno ci beuré da ngay sauuuupe
Wowéma Papa sa thiamogne na féki sa ndey-dior
Yégueugo tollouwaay djapal ni da ngay dorr
Kouma saurou Mor Talla Guèye, Killah moy médaille d’or
Bou mbède taxawone sonder nga feel kignou like
Dagno simple té efficace ni virgule-lou nike
Maay Kingou King sa King maa takh mou sole string
Dem fou sori scream (Youxou) ngir pop mo dafa fori bling
Rappeurs yi dream Nitdoff mom dafa fort ri rimes
Takhna faux yi dik tauth real yi ba sèn story clean

{Refrain}
Ana fake ass nigga yiy wakh ci sunu guinaaw ?
Murder them just like bang !
Ana fuck up nigga douniou dem douniou baayi kène dem ?
Murder them just like bang !
Ana bullshit nigga yiy djalgati pour Kill rap ?
Murder them just like bang !
Gunzout (Gunzout) say too loud
KK my nigga and we’re so proud
Come on

{Verse 3}
Bang ! Niola gueuneu Euss kone boul niou niodi teng
Bang ! Bou sa xol bone Hater défal ni Kurl Corbain
Bang ! Djaggueuh boulay fégnati nigga yaw teup ko dem
Bang ! Atanago sama micro Mc yaw keuf ko diéém
Bang ! Dagnela fékeu ngay wakh nioune niou dieuf ko men
Bang ! Knowledge mbède lagni tek dou rap-bou boppou nèène
Bang ! Nioune daniou niémé nathie mais douniou djamé knife
Bang ! Am naniou gun té beuri fiit beugouniou xagné life
Bang ! Hip Hop bouy paradise wowéma Harass men
Bang ! Killah ngi Diaxanama (Safara) moy Killah ngi mbalax men
Bang ! NDK bou dougué jail moy saggawaate na Proc. ba
Bang ! Longévité au top comme Samuel (Eto’o) ak Drogba
After this lo mousta djiss ndakh mbindeu mi day xaute té diss
Messi noumouy boté 10 ak djanteu noumouy toppé biss
Track yeupeu dope té riche takh fepp founiou sopé guiss
Baanexou ndakh nignouy bokké kiff nounou lagni bokké tiss

{Refrain}
Ana fake ass nigga yiy wakh ci sunu guinaaw ?
Murder them just like bang !
Ana fuck up nigga douniou dem douniou baayi kène dem ?
Murder them just like bang !
Ana bullshit nigga yiy djalgati pour Kill rap ?
Murder them just like bang !
Gunzout (Gunzout) say too loud
KK my nigga and we’re so proud
Come on

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR