LYRIC

Diokh ma mic ma diagnal léne
Diokh ma mic ma diagnal léne
Indile rappeurs yi niou dionguale lene
Indile rappeurs yi niou dionguale lene

[Omzo] Kay wakhak mane fils makoy todj
Kay wakhak mane fils makoy todj
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Kay wakhaka
I say Kay wakhak mane fils makoy todj
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Mc sa gatt bi nangue ci def kothi
No dioutou click gno lay guiss rek sapp
Buzz Lab dou ay nitt degn doff
Rap Game bi lagnou def ci sen poche
Ask ci sopi Hip Hop
Fresh 2 def
Rap bi thieb bi
Young Fief nekheu sauce
Lathie tel H-Bomb, on est dans Rihanna (dans Rihanna, au fond)
Fuck, Fuck, Fuck Afrique sama team amena Kana (amena Kana)
Li gnay tokk di rap yeup dou deggeu
Dama sokhla Haters you bess nakh gnouma done bagne gnomay commence beugg
Yeah, sa girl nena sama bate dafkoy khogne lo (dakoy khogne lo)
Boul deglou loudoul Buzz Lab fils daflay yome lo (yome lo)
Mixtape bou bess khame gna foungue koy kothie
Kay wakhak mane fils makoy todj

[Refrain] Deuy keula nakh (x2)
Deuy keula nakh
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Dou ma sandi kher mais fils makoy todj (Walla bok)
Deuy keula nakh (x2)

[Canabasse] Kay wakhak mane fils makoy todj
Comme car si classe, yeah makoy todj
Alcoolique si bar, verres yeupay todj (Walla bok)
General Bass est la, yen nieupaye tothie
Sa carriere gueneu vide teuli diamanche matin
Mc la gnou kill pour decorer sunu sapin
Game bi yeup est-ce que amena Koufi gueuneu tangue Buzz Lab
Est-ce que sa mamen meuneu dawal patin
Bougoulen probleme comme nullard you nek CM1 (Thiouuu, wala bok)
Yeneu gui force rap bi yene nieup serre uhnn (Walla bok)
Mc bou khagou ….. Buzz Lab egal sendi ma (Walla bok)
Bass seigneur leu ci limouy def te chaque jour c’est dimanche (eskeuy)
Lokho ci kaw may tek comme pa (eskeuy) def sen bop kongue (Walla bok)
All eyes sama team bo guene nioune rek ngay guiss
Rap Galsen ci mane comme gang gou mbelenetane
[Omzo] Bou may deglou sen ay son sama khol day fess ak yeurmande he ndaysane
[Canabasse] Bou gnou fegne Tele nga buegueu changer chaine
Mais demal change carriere nio koy todj sa mere day nane
Deuy keula nakh (x2)
Wa Buzz Lab dal fils nio koy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kone Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj

[Refrain] Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Fresh 2 Def Dangue ma guiss rek Sothie
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj

[MedMetal] Heun! heu Danga clate ni kouy seussou girl cii bus
Sama team dala time ni quelqu’un qu’on suce
Takhaw sa kaw di saw bangua fok ne day wiss (ayy)
I don’t fuck with y’all pussy nigga, bougouma am syphilis
Yague na diko todj ni macon ak carreaux casses
Sama yona gueuna talli fouf yere bouniou passe
Ki gueuna tangueu si yene, si nioune comme Maniang Kasse
Mc da nga khewi comme Alioune Kasse
Guiss meu rek, Fils lo tek
Dama job lii dou ploufe, li dou “fiss mba tete”
Deuy koula nakh (x2)
Ci four lay nelaw, wessouna bakh
Sene girl yi dima topou melni mane kesse diongue
Dama fouye ni kou yore milliarou Aida Ndiongue
Comme lam yi ma takeu, sama lokho lagni langueu
Rap sans Buzzlab, comme guerre sans bombes
Zo Dollar, Canabasse, Med Metal blacka blackeu
Shoot, Shoot To Dem ba indi laka lakeu (=feu)
Courant foume coupe sama bling mongui takeu
All Black Gang, ni kou diogue sarakhou nakeu

[Refrain] Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak mane fils makoy todj
Deuy keula nakh (x2)
Fresh to death Dangue ma guiss rek sothie
Deuy keula nakh (x2)
Kay wakhak man fils makoy todj

Deuy keula nakh (x2)

Deuy keula nakh (x2)

Diokh ma mic ma diagnal lene
Deuy keula nakh (x2)
Diokh ma mic ma diagnal lene
Deuy keula nakh (x2)
Indile rappeurs yi niou dionguale lene
Deuy keula nakh (x2)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR