LYRIC

{Intro}
Cuz I live my Passion
A legacy from my Father and My brother Omar
Now nothing can stop me
My heart is free now

A mon pere et à mon grand frère

{Couplet 1}
Paa bé ma diam gospel , Jazz, Xalam 2 , Jules Faye
Samba Diabaré Samb , xalam door soul faye
Djaliba kouyaté , radio kan ka cool kaye
yékéké Mory Kante , demb douma ko soul taye
Francis Cabrel , Renaud , Jacque brel jitou samay nopp soolar
Euleuk si biir bouge de la , les temps cha nge ma sol art
Rythme binaire , caisse melodie missal or
Musikou mbed djeumo salaire , deug ci mbind mi mossal leer
Percy sledge ak seal
Youssou né shames of freedom , Jolooli souf aksil
la balade des gens heureux , helene , le téléphone pleure
Beuss nieuw ma hardcore , leneen ba teulé foon fleurs

{Refrain}
Daw lahou guir nek mane
Wwané li né ci mane
Xalam gni di keemane
Dou mane lahou rek meune

Cuz I live my passion
legacy from my father
Music from my Childhood
Let me be , let me dream

{Couplet 2}
Alhmadou sant war , deug le Mame Ndiaga Mbaye
Music moma sagne ta wor , waral ma sax ci yaga baye
Jarad Baye Pene , baba diala ndama yéelé
Jolof jok si seven-second , jeuli ndam Yeulé
Kassak dougou bois sacré , saloum wané goyaane
Been soukeur bi ci teen bi , ngeweul wané wayaane
Fooralma joni joni ma tajaboneek tukussu ngalam
Thione bakk der bou niul , mapenda wurussu ngalam
Samak ngoné nga leme si ay melodie Cheikh Tidiane Tall
Sinébar ak Ol’Dirtu bastard, sama Katidiantal
Stand by me Ben E, wane ma sama guenete gui
The Wonderful word , samaye geut nguen tidji

{Refrain}
Daw lahou guir nek mane
Wwané li né ci mane
Xalam gni di keemane
Dou mane lahou rek meune

Cuz I live my passion
legacy from my father
Music from my Childhood
Let me be , let me dream

{Couplet 3}
Baobab, Number One, Pape Djiby Ba
bdp the bridge is over, we go back to Hip Hop
Jok break si beat ak bass , wala teup ni Alla Seck
Moon walk ni Michael Jackson, buru pop bi xaleu rek
One move Nesta Marley, Laye proper mi nelaw
Xalam demone na bay neex , lay mboup seey si guelaw
Mireille, Mathieu, beattles, Julio Iglesias
Die Straight, Eagles, Enrico Masias
Ca Daouda laniu lafi yoni
Mala Love bamaye goné please tek ma si yoon yi
Lumu doon yoni, Sukeur wa ila kaani
Li samay beut namoona laal, yeuk mo nek ni

{Refrain}
Daw lahou guir nek mane
Wwané li né ci mane
Xalam gni di keemane
Dou mane lahou rek meune

Cuz I live my passion
legacy from my father
Music from my Childhood
Let me be , let me dream

{Outro}
Remember, enter to the thirty six chamber
PBS, Daara J, BMG, Bamba J, Pee Froiss, Rapadio, demb
A tous les pionniers du Rap Galsen, li moy Xaatim AK Kallama
And a special tribute to a living legend from senegal West Africa
Mister Youssou Ndour

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR