LYRIC

[INTRO] (Minuss)
Juste le dire… Juste le dire
Le penser puis l’ecire
Quelques mots en tes oreilles
Quelques mots en tes oreilles
J’aime bien virvolter au gres des melodies
Me sentir à fleur de sensation et d’emotions
J’aime ce que je sens à l’instant
Où mes doigts tremblottent sur ce clavier
Mes yeux sont lourd de sommeil certes
Mais se vident de leur peine
Qui parle sur ma joue
Je veux aimer et etre aimer
Crie d’une douce symphonie
Sans me soucier d’une certaine harmonie
Je veux juste Vivre
Je ne sais pas si je vis ou decide de ma vie
Mais j’aimerai bien qu’elle soit
En 16 mesures si elle devait etre melodique
Mes doigts fins au clavier
se verraient habiles au arpeges
Une voix tendre avec le micro
de plus en plus douces avec vos oreilles

Xaatim Ak Kallam

{Couplet 1}
(Minuss)

Basmallah , aksil ak diam la
Tarbiya sakku xam xam la
Set ak séll ci xel la
Yeuk soga nek guinaw jurom niari assamane la
Li diss ci xol yi moom téré séey ruuh yi
Yagg bawul dara , dafa fekk ndongo bawul dara
Fu Ki jiit yuné dofa took ni fukki Jiit ci bang xalato ci took
Dekël sa aluwë , ya nguek sa lijassa , Fi ku niemé dagn la dée
Jott na xel yi xolli hole newoon ci buumu xol yi
Su niu sagné wax dafa fek né mbed mé niu denk
Xaatim ak Kallama (PPS)

Writah Family

(P.P.S The Writah)
Leera feuss ci leundeum , ni nagn bu niu xeuss timeulé
Keuyitt gui weex talle , xalima gui diko stimulé
Kallama ak Xalam , xalleu yoon wi niuy tuddé game
Du jeum joy dacc waral yeug yeug jittu degueum
Nafaray sa nganay , liguey la tarbiyala
Mbed ci mind la , xuss ci tartar bi yé la
Gni di waar, gni di wor , jeleulé mandargal ndaanane
Ji xaar mu jebbi , ku taatane mujée bi da naan
Du jeum , du tuur , li nga gobbé nga ciy gar
Ubil sa planteeru ruh , guis mbed miy zikar
Xel yi free saxi laaf, naaw fu jeum dul yegg
Yaram xarala ci xaré la , Ku ragal daanu bul yek
Da niu foo soga yeeté , yeené sumb raak bi
Deuglul kick yi di fett , basse biy gueusseum barak bi
Son bi Jugué ci hood bi la , so sibul mbot bi xutba
Do sutt ka la feeté kaw , writah ki yeem yahud ba la

[Refrain] Xam Xam mo niuy teeté
Gueum Gueum mo niuy yeggé
Xool guiss , dox biss fils
Mbedelectel la … Peace
Xam Xam mo niuy teeté
Gueum Gueum mo niuy yeggé

{Couplet 2}
(PPS The Wwritah)

Li sunu Xel di geux , tektalu doctor-a
Street D.E.A , track bi di thesou doctora
Bul laaj té ki kana , li mane duné maana moos
The Ghost Writah…Mbed me ko moss

Fuk ak diurum benélu araf ba muy niar tek ci fuk ak diurum nient
Feulë fent feem yi feuss fernient
Xelu geun Xolo , xaralé ci beut la yam
Sax ci mission teewal deug ni Yeesu ca bethlehem
Sant sangou saggo sagaru ngeum, xuss ci ying yang
Xippi sippi , guimmi guindi saxo sing song
Ndortel la genesi , nuur gui day gueneu feuss
Gueuneu waar geuneu seuss , beuss dina nieuw niu doon ko
Ci aaru Cool herc , wowema Mbedelectuel
Street intelectuel , tep tep lep ci xel
Di nga gaagnu , di nga Jok , di nga weet , di nga bok
Di nga kaagnu di nga broke , weet jooy fi nga tok
Gni gueum gni weddi , nga geum jafandu ci way bi
Jom ci tank ba ci wé , sigui euleuk taaral waye bi
Ci mind ci rhyme , tekk wane na niu yoon
Fu niu safara niax , ndax kaddu mbed lagn niu yeen

(Pps&Minuss)
Mane maay Xaatim maay Kallama – Le miroir de la rue
Nafar Kocc ak Nassarane – le grimoire de nos vecus
Sunu Kadu teunk liniu doon – Intello ou Marginal
Mane la – c’est moi -, Yaw la – c’est toi , Niun la – c’est nous
Les poetes comptant pour rien – Les griots contemporain
Nous sommes ce que nous offrons – La voix des souffrants
Mbedelectuel!!!!!

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR