LYRIC

{Intro}
Djiguène day def yeufou djiguène
Goor yi sole yéré goor 
Sénégal Dieum kanam kanam kanam kanam (2 fois)

{Verse 1}
Toubeuy bi nga sole dou sa bosse, Ya ngui xoss
Palate bi ndakh soss, niou melni xathie bou possé loks
Handicapé nga cii xell, damalay yeureum soumalay kholl
Am envie songuela seufla liy bonelo sama xoll
Yabèle wéssu woul goor di sole toubeuyu djiguène ndakh feeling
Def mou dang kolé ay xotam ngui bagn xass mou teksi string
Dieul Move boléko ak Jaune, guéné Rose teksi Rouge
Foumala fek bo bagné nathie….(Monster Voice)
Ana goor ak tass sabar youmay saf Ecurie yambar
Dakk Leumbeul Aïda Dada, biiñe done sèn sinébar
Guénou beuy paquette, deuké frimé té yorouniou wétchett
Boul diaxlé bo rombé nioulay piss ni diskett
Légui day dokh di rith, zéro complexe di waar mbith
Kanamam lay jonglé manièrou Woo yi (nanas) la def cible
Poudeurou pastellou kolou waath ay mbagam
Limo waral malèni dagal

{Refrain}
Topeu fashion , sagnesation
Dieul option Solou Mode Goor djiguène (3 fois)

{Verse 2}
Masculin bouy concurrencé féminin cii sagnsé
Beugue mode ba cii xékh wessu nañu cii ay SUNSET
Talon wakh possé wé molène dessé ngène matal
Mbathio gui kass ndakh Gooru tay yi nioko dakalé patial
No no do tchii guèneu, Rak sama do tchi guèneu
Bo check gué li ngay langal wara dieuli ni do djiguène
Marque yi ngay sole yeufou PD la boul niou mom
Nakh ko mou sigui khol waaroul yaubalé sunuy mômes
Fuck Mode Pinw
Ay Goor you baboune reubone class lay clash
Fire Burn sen stylou dounke yi lakeu sen faay
Dass ko baamou niaw tangal niafko sen… (aay)
Dolène ay Goor ay Biatch guène
Makoy feusseul cii bepp scène
Télé bélène yakeu, louniou guiss sole douniou xam foumou djogué
Topando ba taabi cii tay oute lou dakeu ba faf…..
Limoula yéné yagatoul biss na cii fêtou
Kou tchi sole toubeuy bou khaate bouy teuthie braquettam Yalla na képou
(Woooouuuuuy Sama Ndeyyyy)

{Refrain}
Topeu fashion , sagnesation
Dieul option Solou Mode Goor djiguène (3 fois)

{Bridge}
Djiguène day def yeufou djiguène
Goor yi sole yéré goor
Sénégal Dieum kanam kanam kanam kanam (2 fois)

{Verse 2}
What’s up? ko yapp? yéré guel ngay sole dignu diémeu djay nandité
Deup dipi douma tchii yém di nga tchii lém ndakh mérité woulo sunu mandouté
Déguisement tapette molay racket ngay casquette
Bi sakétu mode no no disquette ngay ndouraul
Souniou rôle moy boulette séni nodeu
Ndaw yi ngay dougueul cii kambe
Xambe tale bi dougnu cii andeu
Nandale baate bi lém saay fambeu
Waw na Gooré ni wa Chamber
Nopi di look guéni yaakeu ndaw yi Meune ko délit la
Deal yi la lathie ko makk yi sopi nékine yi lou waar la
Na nga ko madjé Goor Yalla momoul …….
Langal Tiakeu, Khauteul COL V
Waané né deuneu amena Tiokeu
Génération boune, Tiakeu
Deuké publicité waakeu
Tass mbakeu
Oute lo takeu
Dokh di wagnarou ni saaakh
Langal Tiakeu, Khauteul COL V
Waané né deuneu amena Tiokeu
Génération boune, Tiakeu
Deuké publicité waakeu
Tass mbakeu , Oute lo takeu
Dokh di wagnarou ni saaakh
Kxkxkxkxkx (Rire) lo lokh
Ak sa coupe ngay melni sindakh

{Refrain}
Topeu fashion , sagnesation
Dieul option Solou Mode Goor djiguène (3 fois)

{Outro}
Djiguène day def yeufou djiguène
Goor yi sole yéré goor
Sénégal Dieum kanam

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR