LYRIC

One Love Staz
Mister Hip Hop

{Verse 1}
Borom bi sakk yéméléwul nii baaram
Gni di jog gni di daw, ku cii nek ak barram
Diam né du mandu, nioddi lep cii booram
Ki sunu sakku jog, dox dem ba raam
Sakku naaw niy moromam, seut nga maro mame
Mbégum diam yi yénam, yonam lagne ko mère moom
Xam na famu jogué, janéer fa mu jeum
Tann doon ki mu doon, jaayanté mujeum
Yoot mayu ko dara, kone fok mu jéém
Aaru Mdède la fale, fala yëg muthieum
Niou doupé ko binde kat mu sallo guindi kott
Xéér yiy dal muy xuss puss, muy tare muy gueuneu kotte

{Refrain}
X Tape….Xacci
Xaatim ak Kallama Mister Hip Hop
Galsen…..Worldwide
PPS The Writah Mister Hip Hop Yeah !

{Verse 2}
Lu waay liguey na dieul, bayima ma done mane
Sama yone mako xalleu, ba né cii don mane
Li Niou woutelé, I get nothing to lose
Dathie na samay guénté, I get nothing to choose
Lu may doyé sondél suma mane doon djante
Diaaru djarignu djarigné, lééral yone wi done guénte
You wanna do it like me, being better than P.
Sa Life lay fénte, féxél tontu lathie bi
Du weuy, du waay, du waye, du way
Yaakaray lééral Sama yone, sama wééru waay
Mister X-Tape, X-Xacci
X-Xaatim ak Kallama, Mister Hip Hop
Rappeur Kaamil, djante B.E.A.T.
Firil la ay cas mille, hood bé ko até
No compétition ku feus Jah leu !
Always a mission, doundeul sa beus dialeu
Nio sakh cii Bobou Batataille
Tep tep gueune yurééte, délul cii Bobou ba taye
Waxone nala ma ngui nieuw
Shine like you, xalima gui taye la gueune niaw

{Refrain}
X Tape….Xacci
Xaatim ak Kallama Mister Hip Hop
Galsen…..Worldwide
PPS The Writah Mister Hip Hop Yeah !

Paul, Writah, PPS, the same
Li may doundou lay Rap, bokuma ak yaw the shame
Again…mbébetu mbède a niou nguèmb
Ngueum Ngueum la niou lambo, yékk tay ligueyou demb
Galsen Boudé deug Hands up
Gueum Sa Bopp, Xatim deugui rap Hands up
Teewal cité yi ak hood, xalé ak mag nakhar yi matt
Rongogne yi heart yi, gniy door waar, gni xari matte
Always a bay Fall, diégui na niou feug deune
Ruux nga mbeur, sama bakk day feukeu ndeunde
Yes…Yes muus matna siiru
I know I can Like naziru
Wéx xatt nii niim bay boul sooru
Currayu boum la, bay boul suurou
Galsen west Africa, This is Xaatim ak Kallama

{Refrain}
X Tape….Xacci
Xaatim ak Kallama Mister Hip Hop
Galsen…..Worldwide
PPS The Writah Mister Hip Hop Yeah !

Mister Musica….Mister Innovation
Wax ma lu dess

X Tape….Xacci
Xaatim ak Kallama Mister Hip Hop
Galsen…..Worldwide
PPS The Writah Mister Hip Hop Yeah

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR