LYRIC

{Verse 1}
Yeah
Séni programe mo gui dokh diourna yakou yakou aduna
Diam ba teukou na boureum waral yeurmandé mabeuna
Protocoles de Toronto foumou done dem légui ague na
Liberté sexuelle mo diouréméli ponke bi da naka matena
Niete 6 (6.6.6) laniou bolé mouy neuf nioukoy xolé
Dieul démocratie defko arme légui moy sen dolé
Droits de l’Homme noumou tiolé, dagn lay sassal yolé
Boy amé tour té bania adhéré niou fékhé nouyou lay folé
Septembre 78, Jean Paul I daniou ko toké
Octobre 58, Pape Pie XII cii la guedjeu noké
Journaliste ba feusseul protocole ba déwam louko soké
Niata artiste laniou locké, niata lagnu bloqué
Séni carrière ndakh baniona djouli séni mosquée
Astakhfiroulah cii séni temples la beugona wakh
Xaathie meunou taa djiteu djaaka, motherf**k doniou nakh
Xamé naniou kanay kane, Xamé naniou nianay niane
Xamé naniou niana nieuy bokou cii nioune guir gass sunu kaane
Founiou démé ba Imam célébré mariage’ou goor-djiguène
Yéférr yi bokou cii nioune, yaw wa dji tine docci guène
Té imam bobou légui sampe na djaaka Paris
Séni dolé mo gui gueune di bari
Goor ak djiguène bokou sapé goor-djiguène
Djité lène dieul Al Quran bou séleu bi diko tari
Ya gui nélaw yéwoul
Lignu lay gaundé léwoul
Fékhel sakou Yalla fofou rek la fitna néwoul
Fo Xaathie di djité Naafila meune ta am Afia
Xolé ni deug néwé dolé légui raxna mafia

{Speech}

{Verse 2}
Yaw, open your head, degg beut bi mbé
Limou soumbou fauute, bathie cii biir Net bi lako werr lako werr
Bamou né fangue douy dianerr
Gniy dawal Gal gui tay séni weuthiooy tektal nerr
Gueute yé ngui xonkou, wathie na ponkou
Limou gueum tay cii beut bi cii pyramide bi lako lonkou
Démocratie ak Libertéy baat yiy fékhal Islam
6 boudoul Koursiyou rek nga fokni 6 lam
Ya gui nélaw yéwoul, rakk Naak bi néwoul
Donté fa ngay raté, waayé Sirou bi nga ragnéwoul
Sa xell bi lagnu cerné dila berné
Pion nga rek, Beuss bi nga tchii conscient lagni lay sépi berr né
Xamé touma luxe ak nécessité, mérite ak lima bania cité
Dépénalisé goor-djiguène djégui na laïcité
Beuy lagnu sopi yeukk mou djité guéteu gui naak yi topou cii ganawam
Mou dodji cii altiné, néferré al-xamiss sopi na adiouma gaawam
Tchii instinct ak nafsou laniou teunkou
Tchii Liberté lagnu reunkou
Foli foi légui cii plus de pouvoir lagnu déinkou
Deal bé sett tellement que bodé naak do aadji
Waayé niombaar yi sipp naniou waral niou gui cii souf di xadji
Sunu andeu laniou wathie dadi dem waar ba xoutbu dajjaal yi
Cii Droits de l’Homme, Femme, Enfants lagnu saani mbaale yi
Démocratie soga aksi, soti essence, xambe taal yi
Télé, journaux, Net bi école lepp lagnu cernés
Nio yilife aduna bi yilife gni niou yilife beut bégui niou berné
On est rien d’autre que des moutons cii troupeau bi
Fok nga sante SENE pour aadji deal bi tchi biir groupo bi
Mission wou 6.6.6 moy éradiquer 12
Niou gui rek…ci pouvoir luxe ak plus de flouz
Ya gui nélaw yéwoul
Lignu lay gaundé léwoul
Fékhel sakou Yalla fofou rek la fitna néwoul
Fo Xaathie di djité Naafila meune ta am Afia
Xolé ni deug néwé dolé légui raxna mafia

{Speech}

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR