LYRIC

{Verse 1}
Suñu biss tay nekhoul
Mbekté nga doneu woutsi, wagnekoul (wagnekoul)
Deudj leundeumeul suñu xol
Meunougnou happy please dadjekoul ( please dadjekoul)
Yallah woté, wayé nagnou diegeul nekhouniou (Nekhougnou)
Li geuneu gui flotté, wayé fimou neni gnoune beugouniou (gnoune beugouniou)
Bo dée done taago
Douniou ko may foumou gnouy wakho
(Book’s : I miss you brodah! Oh! Nameunagnoula)
Guiss nagnou à gogo
Wayé bi xawna gnou takhalek suñu sago (x3)

{Refrain} x2
Bourba nameunagnoula
Fo meunti nek nameunagnoula
Book’s : I miss you brodah! Oh! Nameunagnoula

{Verse 2}
Nane lay def ba guissat
Nitt meer nga diok deme diko baal
Niveau sound bi nga yegualat
Nga wax ñu tchi sa xalaat
Bourba namenagnoula
Meunou gnou geumni denthnagnoula
Book’s : I miss you brodah! Oh! Nameunagnoula
Sa yené egg na
Li nga deff si nioune Hip Hop bi nangona (Bis)
Book’s : Thiate ba thiate metite bi beneula

{REFRAIN}

{Verse 3}
Dieumeu né mess
Dieuf ya dess
Namele gui fess
Dele , dale
Gni nawaone sa oyofay ba tax gnu lay berndël
Baat bi sapp, xoll di yeuk, xella ko bindeu
Rouh ya guiss thi seni boppeu
Gaïndé nga wone mousso fi simb
Yombeuna gnoulay ceddel djiko yi geun
Yako job, mou feuss, moussougnoula degg si miroum gun
Geun di mindef, denk nagnoula suñu bro
Ya xam la nek tchi xol yi, batakh yewom wara go ( go, go)

Rip bro! Rip Bro
I miss you brodah ( bis)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR