LYRIC

{Refrain}
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané

{Couplet 1}
Nenaniou sougnou Hip Hop amoul kagn amoul mana
Bougn si espéré tabakh walah reunkeu patiana
Walakana ngasi doundé abana
Deukeu si metite ak miss batou Yalla yana
Wakhala dessé dou lenéne meunoniou pécé
Dirigé térassé séy cliché Késsé
Ndakham amna kagne tewal suma kogne
Lathié kouy Sii sa gatt gui dako sagne

{Refrain}
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané

{Couplet 2}
Nianatou wala wayanne newou gnou tchi
Sopi seni mind aki djiko té bewou gnou tchi
Weur aduna dikatt nga weur nane du gatt
Getal passeporou Fat Walah bou Thiatt
Rap béngi tabakh rap bengi warakh
Rap bengi todj di drive auto you patiakh
Swingué Lô sa mind geuteune État dom di shine
Dégagé niary abdou di xare macky wathieu Line
(euh Macky meneu mi)

{Refrain}
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané

{Couplet 3}
Yoor doom diabar di geré galé leumeu
Beuri dolé kouniou gemb palais nga dieumeu
Gueum gueum packett diss pocket
President directeur general moy l’etiquette (haaaa)
Sigil suniou askane
Bou deukeu bi sokhla niou diokhé bakane
Bul falé niouneu NTS niouneu,
Na bone khol yi yobalé li ( Muahhh)

{Refrain}
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané
Ngané degoumala Ngané, Ngané degoumala Ngané

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR