LYRIC

{Refrain}
Ya ngui nélaw Joggal maam Mo ngui naaathie
Goor Yomboul dou ni ngako fogué (X2)
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Goor yaw ya ngui nélaw
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Khamoulo heure bi jott
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora

{Verse 1}
Yeah ! Mannequin la cii taille Star la solou
Dokhane dafa ci ay dafay mouki di djolou
Niodi level bi high mom la xalé yi goal-lou
Mom moy wokou fi khassane cauchemar bi nanditéy moolou
Aligné ci kaw ba suuf niodi tang bi kang
Crochement gnémé sa poche dafa feuss ni bling
Poète la ni Zing soxlawoul NGORA KENG
Tioukou ndigg zigou ndigou foumou dem bafa bou Weng
Samba Alaar Diop Dollar deuk cii fène
Yoroul gnar biir keureum day spagetti nène
Saup Méw Dadjalé weur di pinw tapalé
Dagg-dagg bi rek lay fékhé noumou lakoy fadialé

{Refrain}
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Goor yaw ya ngui nélaw
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Khamoulo heure bi jott
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora

Ya ngui nélaw Joggal maam Mo ngui naaathie
Goor Yomboul dou ni ngako fogué (X2)

{Verse 2}
Néna mom namoul dara datchi dem ba tak rippeu
Koufi niodi tangue bouné thieup dalay euppeu
Dou wakh am marignaire sous fess wala jupe
Haa ! sani once dafay nappeu
Cougard minette cigare lunette
Khéboul ganaw car aka meuneu dawal brouette
(Tonton) Djogolo leu rigolo leu
Tonton niouleul karaw aka beug digou looleu…(Bandit)
Sani once payé Cons. (Consommation) simulé galanterie
Duplex passion reubb plan teuri
Yoré plan weuri expert cii foureul djeuri
Leuweul, Deuxième, troisième tarkhiss bilay am lou beuri

{Refrain}
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Goor yaw ya ngui nélaw
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora
Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy
Rek nga fokné loloy Ngora Khamoulo heure bi jott
Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora
Ngora lolou dou ngora Ngora

{Verse 3}
Goor moy ki yeureum diabar ak dom
Dou daw responsabilité assuméy diom
Loumou méti méti dafa xeuy gnibi ci ak Kom
Dou wath djadeu weur di faddeu dignité l’homme
Goor dou suulou dou muscle, dou thiofé
Weur di door founé dom ni kou doffé
Goor waroul yombe mbëguel dougnou ko kaffé
Bou forr xeuyé yombe dafa fekk seug djaffé
Niata xamoul sen Baye té magg ak sen Yaye
Kheuy lathié raison gnoulay tonto ak ay lay
Sa Y waroul latéé lale X bouné
Repèrou dom moy Père nala diaral louné

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR