LYRIC

{Refrain}
Niass coumba Abdallah Niass coumba Abdallah Niass coumba mouy Abdallah ilahah ilalah (2x)

{Couplet 1}
Cheikhal islam yokeunga suniu imane
Dokhloniou asamane walahi yadi kémane
Tank naniou fa nane dieulé naniou fa niane
Sopi melokane sheytané laniou fa dane
sangeu nga souniou khol rendi nga sugnu khel
Simi Liniu sol df niou tay liniou mel
walahi amuniou sa fay bilahi dotouniou fay dof nagn fa yalla lahilaha illala

{Refrain}
Niass coumba Abdallah Niass coumba Abdallah Niass coumba mouy Abdallah ilahah ilalah (2x)

{Couplet 2}
Guissnaniou aldiana nioun guissnagn safara (Aldiiana)
Topéwuniou ko Yalla (Safaraa) ragalewouniou ko yalla (Allah)
Arifouni bila (Allah) dei deki guiss Allah (Allah)
Diko santé meneumi niass coumba abdallah (yéyé yéyéiiii yéyéiiii yéyéiii ) … Diogé si leundeum dieum si leer…(yéyé yéyéiiii yéyéiiii yéyéiii )
Wedi ko gueum ma dieul nga nder

{Refrain}
Niass coumba Abdallah Niass coumba Abdallah Niass coumba mouy Abdallah ilahailalah (2x)

{Couplet 3}
soldarou bay talibè bay dou danou do danou (niassy) soldarou bay talibè bay dou danou do danou do meusseu danou soldarou bay talibè bay dou danou do meusseu danou
Guissnagn aldiana guiss safara té bougéwougn metar
Gétar takouniou tè khamnagn la né suniu bir etar
Lettr bi niou makhdi fleche
captènaniouko dioubeul asamane visitéko ak callech
Kone diegeuless akhikha moniou mech
Bombam explozé sugnu dieum batakh niou tèkhinss Watieu bess rewoum alhamdou tankamlou li suniu beut tamal malech
Anadiami bagnone tay sen dom nangou nagn
Anadiami dawone tay seni domi wouyoudjinegn
mindéfi lagnouy takhawal
Mala yi lagnou seugeul
Pitcheu yi laniouy nawal montagne yi la niouy mbeukeul
dioromi rak yi nonoulafa teudé
té si explication zair lalenko firilé (Niaassy)

{Refrain}
Niass coumba Abdallah Niass coumba Abdallah Niass coumba mouy Abdallah ilahah ilalah (2x)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR