LYRIC

XaK – album in stores yi, fok niu pollué game bi
Paul la yeuk game bi, fok mou feuss né Tony ak Dembi
Dagne ci né ay ate ci pétt, reudeu line ni architect
Xeuy ci xol yi, sar ci call yi, liguey dougueul art ci tete
… Li la foon nga xeum, sama neek lay fanani
… Casse bi nga moss né veup, barigo lafa naani
… Tornade biy radjaxé fép, di wadal laafa noon yi
… Ronalzidane ci beat, kilifa laa fa dooni
Sen hip hop heu – guissouma louma si yéem si léne
Im a D.O.P.E Mcee, xam nga né manouniou yéme ci léneu
Dama ill, still black skin – maay ndobine
Sopina doxine, kill you with kindness tay dalal do xiine

Refrain
Lyrical essamay, galsen genius Rufisque’s emperor – La La La La!!!

Woowéma El loco, antanoko déloko, aythia ma guiss sa lokho – La La La La!!!

Ate mou né mouy gueuneu heavy, Classic MC, bokoumak negus yi xéwi – La La La La!!!

The ghost writah, supa rhyme maker, PPS the name say – La La La La!!!

Dama Woyof di fly easy, di plané ni cerf volant
Yaw nga diss té yenouwo, di plané sa cerveau lent
Yama gueuneu xam, maay doomu jant ak wéer
Lou goudi gui yagg dou té fadjar ma feink ak wér
Baay bi dafa cool wé, téwoul di noote sa MC
Mind bi dafa fool wè, taloul dingate sa MC
Souma tontouwul sa clash moy douma door djiguéne
Sama street dafa class, boy amoul Goor djiguéne
Do ci guéneu, gni may nawloo baay do ci kén
Fouma reudé rhyme, niéx ci flow, Ré Mi Do siy guéneu
Lime bi do ci bén, defal tékk nafar, danguéni foo
Yagg naniou raatalé under bi yeukeuti peudeu feulé ci bénene niveau

Refrain
Lyrical essamay, galsen genius Rufisque’s emperor – La La La La!!!

Woowéma El loco, antanoko déloko, aythia ma guiss sa lokho – La La La La!!!

Ate mou né mouy gueuneu heavy, Classic MC, bokoumak negus yi xéwi – La La La La!!!

The ghost writah, supa rhyme maker, PPS the name say – La La La La

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR