LYRIC

{Pps – Verse}
Nio gui ni gaanayo bombe lyrical
Irii taal fake, bitch ak snitch fokk xirr yi daal
Niou mourii yuur yi, pundeu bi wourii from Teunguéthie la
Souli kour yi, tuuri djoko bour yi ki guedj la
Tek lagni doréé, moytoul dagni dooré
Difaré sa peureum ba paré bakhéla rhymes you dorés
Faxké pékhou bic, cii kaw beat bi ngay goré
Pps, Big Fa faxké cii underground Bénène town
Bénène sound diokh dadjou sakou crown
Xell mi tane fi def, tiakhane nafi diekh
Kou gueum li ngay def, aywa takk dioug wadiali xéékh
Kharatouma kou may djokh damay fokkati lima mom

{Refrain}
Pps, Big Fa niou gui ni
Or connexion niou gui ni
Gathio bic, cii kaw beat niou gui ni
Soy bégué deugui baat defal nii
Pps, Big Fa niou gui ni
Or connexion niou gui ni
Gathio bic, cii kaw beat niou gui ni
Soy bégué deugui baat defal nii

{Big FA}
Dioug feusseul meune ak katane Té mic bi yabbi tchii lii
Fokk respect am tchii rap bi fake yi toupe di tek lou mel nii
Diotna niou wané louniou meune louniou job-bone liniou déintione
Yénène fém ci rap bi tek lèn
Beut nélène fuck lène
Rap cii kaw beat douniou ko loupé get-tal niaar gnilay gaañ
Nioy tek té doko seug ngay conS rap bou dakeu kaañ
Yague tok di job dafa djot tay niou dieul louniou mom
Lo fokk, dagnu togone di xolé niakou niou diom
Douniou wakh dagni djeuf bo niou xolé xam fi niou bokk boy
Ci rap bi ak binde ci kaw beat technik bi douniou cii boy
Pps ak Big leu li dou fuck lancement bila rek
Peunde bi djouk fokk mou daleu kou né xam fi ngay fréq

{Refrain}
Pps, Big Fa niou gui ni
Or connexion niou gui ni
Gathio bic, cii kaw beat niou gui ni
Soy bégué deugui baat defal nii
Pps, Big Fa niou gui ni
Or connexion niou gui ni
Gathio bic, cii kaw beat niou gui ni
Soy bégué deugui baat defal nii

{Pps – Verse }
May niéte (3) ci bèneu, bèneu doufi niaar
Flow, lyric, technique original ni signaar
So na-ngo done djangane doupé niou sénior
Under peunde cii deundeu gueuneu feusseul li tchii niorr
Bamay goné la tchi gané, bonet ba done tchi govoné
Xalé di xolé mak tène, Deuxeugne rap ni ……….
Wakh fégn meune dé mandou, ci xaatim niou maak lèn

{Big FA}
Beugou niou lène fils yénène sakou doundou talibéma
Ragal dou rap téggal mic bi dém sori baala
Xolal nigni téggo cii beat bokou lak ni ngéni rapé
Wane latchii technik you touti Bo xamé rek doniou niémé
Sokou di diébeulou deungeulou Wéingalou raaye dokou
Djapela feug la mbeuk la diégui sa kaw dokh dokh dokh 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR