LYRIC

{Couplet 1}
Dagna tamou GUN MAN meuné THIOPET SALAM
Vé gnary baram Yii PEACE KO sa âme
Dékiil groupou NABY ba wone félé Thiia Mbour
Deugeul liifi mame Yii bayi wone bu ABY NDOUR
Diameu lay OTé dou OUSMANE TANOR
SK mooy initialam defko sa OR
PS: Noumey Def ba jote sen ngor
Deukou Diamakh Salaam la deukou mame SENGHOR
Gni nekh dérétt lay weur woroul takh nga taam ma DEUMEU
Barkélou tie séniye LEER dign ci bégg bagneu geumeu
NAW SA KAW langamou sa baate show la Love
VAMPAYEU yi Bagn meu imposé ONE LOVE
SIGNAL ba wéssouwoul affichel la Ay BEUGN you WÉEX
35 Bi di takk fitna dey diékh
Peace léy GUILY tadj NDÉKILY
GALAKH NDIKO zam zam Féy Aye tie Ay simily

{Refrain}
PEACE PEACE
PEACE LOVE AND UNITY (4*)

{Couplet 2}
Diokh ma PISS ma niowlou, tamou tie bu WÉEX
Me FLOTTEL KO mou feuss waw DIAMEU rekeu nékh
WÉEX couleurou PAIX Dokh tie Ay Pats
Boul xare ba BIDIAW légui la sigguileul PA
Sénégal eungui xol Yi waroul NIAGASS
Boul FAKH kay gnou Wax firil kanam bigneu Fass
Ya sol Lou rafèt rombeu ma MALAL
ALA athiou amul bayi diameu rékeu halal
Lo meunoul xékh Ak sey BRAS utilisél la Thia déss
SAMA BAAT DOONE SEN BAAT dokh ba yégg dougoul XPRESS
Jaam tie barké ségn abdou LAHAD
Souniouy destin Yi gno SÉLÉ waral ma siye JI XAAR
Tek lène BAZOOKA yii, JOHN yii Da doye
Def ni mame KHADIM mooy ki diara rooye
DIOKH MA SA FIVE té nga MANOU mooy li matteu door
Do nagg Sakho Ay bédieune mane douma MATADOR

{Refrain}
PEACE PEACE
PEACE LOVE AND UNITY (4*)

{Couplet 3}
Sama xol lako TIBET owéma MOINE
Gney MUSULMAN, CHRETIENS, BOUDHISTE Am nga tie walleu
MEDITÉL doone si Kangam wassaré
YING daane YANG teureul Féss taasaré
DanA sakh gnouy weur di ladj Kou DJILY
Affichel DIOUROMI BARAAM Yi né simon Mo tiji li
Bétouma Da BEURI BAGASS c’est ce qu’on MADI
Nafékh Yi woor di naane Kimo xamadi

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR