LYRIC

{Verse 1}
Da nga beug lou lerr, beug xam lane moy xéw ci sa avenir ?
Beus bi nga gané ci aduna déloussina ya ngi fêter sa birthday
Boul faté ni boudoul wone sa Papa sa Yaye do nek liir
Beus bi ngay délou ci buur Yallah kène dou féthie sa bissou déh
Loy wakh ? Loutah nga doundou ? Lane motah nga dox ?
Loutah ngay waay….? Loutah nga sissou ? Lane motah nga dof?
Loutah Yallah saakk la ? Saakk ma ? Saak mala saak laak Ibliss ?
Li niou wouteulé niom moy nioune ay Domou Adama lagne
Lou tékki di dieurigne ? Boko xamé est-ce que amatina sens ?
Aaté Yallah gueune, aaté domou Adama Kasso bi beurina Innocent
Sole simi yëré, Rakk sama dembe guiss nala tchi Goudi Town
Att yé ngi dem nga teuweu maagueuh beug siiw takh nga photocopié sa down
Abandonné nga sa njaboot. Louko gueuneu pire ?
Kou kamikazou dioxéna bakkane tcha bamou djoudo
Da nga fokni ben beute moniouy illuminé
Kou xamoul sa bopp dougou ci kambeu soxla wouma sa don
Djaay kattou dolé nga, tapette dou dooré
Na doxine bi gooré, na nga goré Diaamou Yallah doréna
Waayé yone bi sorina métina, sorina fi sorina
Aduna dolé la I’m sorry mais képeu kou sori na khaar
na khaar

{………}

Imaam dafay djouli dou dougou ci bar
Nittou Yallah nga té meusso diouli Tisbar
Djangoulo xamoulo loudoul Allahou Akbar
Naathie bi tangue na safara ci gueuneul leu Aldiana Firdawsi
Soubhaana Lah !
Tourou Yallah ngay doundé di encaissé ndongo bi tchi daara bi
Kharafal djiguène niou wakh ngané da ngay toppeu aada bi
Dem ci sa deuk niou complot leu raye li Khadhafi
New World. 500frs nga taale niaari fisselou baune
5000frs yi dembe thiaggatou nga ci ngone
Sincèrement yarou nga mais da nga dessé diom
Malaakal Mauwty meussoul waxaalé doundou
Kone Yakarouma di ngako djaay déh
Mané doxkat dina deug daye. Ana seet kat bila ndieuk féégnou ?
Fèène kat bila gueuneu diégué sèy tankeu leu meuneu raylou
Borom ndéki kouko ndieukkeu jog yabo nga teudaate
Handicapé, Goumbeu, Gaana aki Moumeu
Lane motah niom rekkay nek ci tali bi di yélwaane ?
Ki nek ci kogne bi thiow bi moko daakeu loubeul
Baram bouniou tallale dioxongne leu da ngaka wédi ladjal Guélwaar
Fondement Gouvernement Djité nga mato Imaam
Guéneul Jummah Saar bi moko loko. Louy sa châtiment ?
Thiagga amena versements diox sa galé lekk naane
Mais dégueu na do tchi gaawa guéneu amena pertements

{………}

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR