LYRIC

{Verse 1}
Sama gueinte gué yeémé cool , mbekté di kemtane
Waral nelaw yi yeggul , Jok ndeké sa reetane
Ferniente yi may weetali, sedal li , seedel li
Pass Passu dellu ci war yi , wassaré love ci xol yi
Tek ko ci tempo djiguene gniy soxeu ci euteu bi
xale yiy foo di rée , teub ak danu si eukeu bi
xeetou café ci deuk bi , kaff ak thiow yi niou woodeu
“Adouna dou dara”
Dem na , weur na , Guiss na , legui xamna
Woruma né , waruma gné , xamé na
Li ngay xaru di yotu , soko djotée weuri leneen
Kumpe nga naane , mou muril leu noon , wari di neen
Wutey sunu taar , xeutioy sunu tord
sunu koor , faté yeurmandé , waral niakay fignou teer
Nioy souf Nioy Ganthiakh , assamane nioy dokh
Nioy moome , moy nioune , nioy Xaatim Ak Kallàma

……………………..……………………..……

{Verse 2}
Une generation gené râle
à la quête d’un generale
Aux jeunes les rôles , la voix on l’assume
l’Afrique le drapeau , la voix et la plume
Les aïeux dans les yeux , entre le marteau et l’enclume
De ma plume , ils s’emerveillent , ma rue est ma seve
Ma merveille de mere veille , je vend pas du reve
Pas de treve sur le sentier de guerre
le micro mon glaive , la vision des silions naguere
On ecrit le JE , decrit la vie de NOUS
le rire , la joie , les pleures dans nos peurs
la haine et les peines de ceux qui vivent à genoux
les regrets , la Nostalgie de ceux qui vivent dans nos coeurs
Xaatim c’est ecrire , Kallàma une maniere de dire
Notre vecu , nos memoires , des oreilles à seduire
Une utopie appelle moi Picasso , un fou rire
On essaye de peindre les mots aux couleurs du sourire

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR