LYRIC

{Refrain 1}
Son – photo – vidéo net bi def promo …weuh
Son – photo – vidéo net bi def promo …Wooy
Son – photo – vidéo net bi def promo …Skirt
Son – photo – vidéo net bi def promo

{Couplet 1}
Yeah defouma rap Galsen wayé kou deukk Galsen meun nga déglou SAMA RAP
Alkuraan Sénégal amoul donté bindd naniou ci Olof liniou bindd CI ARABE
Niakk xam finga dieum AMOUL / Niakk xam yoon binga wara diar mo AME
Hakill fane la tolou XAMOUL / Wayé fimou dieum aka moko XAM
Déét waay Rap Galsen meun na dem wayé rappeur Galsen yé meneugoul DOKH
Kou ci né di feugue deune té todiou niou féne foudoul séni biir GOKH
Koula wakh lingay rap dafa set dafa fekk kokou xamagoul louy NDOKH
Son you sadik lalay diam boy ndakh Yallah talent bou niaw lama DIOKH
Niata boy nio beugue melni mane té donagouma DARA
Niana boy nio beugue done aye talibé té béragouma DAARA
Rap bi da khibone wakh deugue Waay
Ndakh khiff ci rapeur yi la dieukk Waay
Kone khalatouma def ni niom waay …Déét waay

{Refrain 2}
Son – photo – vidéo net bi def promo …weuh
Son – photo – vidéo net bi def promo …Wooy
Son – photo – vidéo net bi def promo …Skirt
Son – photo – vidéo net bi def promo

{Couplet 2}
Yeah kima done la wallah lima MEUN / Kouci nék ak loula neex ci MANE
Sénégal nga yame di feugue DEUNE / Yéférou rap bi rek nga doy kééMANE
Mane bama amoulé projet la ame linga ame kone Sénégal kassé ATaNOUMA
Boy mane dina yobou Rap bi fouko gars yi foguéwoul wone lakk Olos ARRETOUMA
Je sais néxoumala mais je suis le fils de sa mére qui plait le plus à A TA MAMAN
Xamé ngamaa …Wooow / Non boul bagne my boy KHAMé NGAMA
Gni fi meun rap daniouléén di compté f-do (dof) yé fi né di NDIEUKETé
Ndakh douma égue ba paré beugue nékaat fi di KHEUTHIO Pé
Béne sama RAP / Béne sama fuckin JOB
Béne sama LABEL / Béne real yima TOPP
Béne sama RAP / Béne sama fuckin JOB
Béne sama LABEL / Béne real yima TOPP
Ndékéété yooooo nioumay khaar beuri NEEGN
Ndékéété yooooo sama yoon mo léér NAGNII
Ame thiathi pour niou beugue limay def sokhlawouma wakh GROS MOT
Bala sama musiique sa showdi def na sama PROMO / Nééna Hakill il est il est TROP BEAU

{Refrain 3}
Son – photo – vidéo net bi def promo …weuh
Son – photo – vidéo net bi def promo …Wooy
Son – photo – vidéo net bi def promo …Skirt
Son – photo – vidéo net bi def promo

{Outro}
Eeeeeeeh da mudafuckin boy …da mudafuckin
Haanoow Ich yo boy haan …Waleuuu
Galsen amngua client …Wallaaaay ame nga client
RepTyle Music

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR