LYRIC

Intro
Main Gauche ba ngi may xamal ni amna loumako bërndel
Ndieuriñam fattalíma ni waruñu ma tardël
Sama TIC moy loudoul dieumeulé kanam boumafa TAC
Donté dessna lerr, bou reveil yi sonné lamp yi danna takk

{REFRAIN}
Punchmind Punch Punchmind
Gnoune, wessounaniou Punchline (4 fois)

[1st Couplet] Na XEL yi yew GODASS yi, sol CALEÇON ak SHIRT gnou defi TOUR
Ay punchmind youy dawlo yaram lagnu fi fass yené tourr
COURSE DE FOND le RIME yi outiwone FORME guir bokk thi
PARCOUR ba, BRAIN nakoy DAW, KEUKH bokk ci
Boul Degglo noppeu topal rime yi ak say geutt
Xalima ba ngi dioy kani Xam Xam lagnu ko xeutt
Xeff Xippi gnu geuleumeul noone yi gnuy sentou nder
Diomi wo, ta gnoboulo dagno daye sa biir univers
Boy diaye KAWE di nga TEEN dakh dagno ASSAMANE
beud gno DAPP di koth ASCENSEUR neelenko massa man
Donal ASTRONAUTE xouss, gnoulay dogga bayi xell
Bo guissé BIDEW guisgusniou, waral niniou mell
Nekko TOP beuri FEEM donne REAL ONE si REWMI
Boy diay BIGGI benneu gui BBOY la si guew mi
Yor OXYGEN’ou PLANET RAP di HIP HOP STYLE DJOLOF
Dawal XAX si bilé AARU MBED fessak HIP HOP FLAVA

{REFRAIN}

[2nd COUPLET]

Da ngen di NAME DROP gnuy NUMBER DROP
Aaraf ya done suniou drogue
Ismaïla diaam ma ma sithiou wané lissi top
Sychrime lama def, toxycolli ko sen xef
Moukhil aat aadji limay tekk gnu wané li teu sen chef
Mbindeu ngay seet? !!? Tewal diwane naniou lako waane (1)
Barkhama gnu guindi loniou si lath niou tontou (2)
Weurlo naniou ay Country(3) moñuy diokh liñuy wane
Dou foo(4) Job la diottalí ko ñiy fontou
Bourba Studio! !! Xabrou la kay def Five (5)
Six (6) defaite la def kay ma diam la en direct Live
Day hight ta dou sokhla gnu diaraleko seven (7)
Na haters yi hate (8) pekhé yi naye na (9) kanam ya leundeum ni teen(10) (bis)

{REFRAIN}

[3rd Couplet] Nioune douniou geré details, ay grossiste laniou
Carton wou rime yé ngi diallou gnom ay egoïste laniou
Boutikou mbagg meunta bokk ak koy wathé contenaire (c’est normal qu’on t’enerve)
DIALL seni BRAIN dieul ELAN visé feugg
Douniou yamm si DOUGAL, THIAKH yi LANIOUY FEUKH
Barrage loumou deumé deumé antanoul souniou FORCE DE FRAPPE(C’est normal qu’on

t’enerve)
KEUDD la ci neukh gnu ladj la koula ki tekk ngay RAAY DJOKHOGNE
Dess guinaw beuk gno baram gnu NADJ BOKHOGNE
Sa diay doolé ak sa Wané wakh moy firdël ni nga Torokhé Torokhé
Fi niofi nek Yalla ko doggal MBOROKHE MBOROKHE (4 fois)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR