LYRIC

{Refrain}
Fi nga beugueu yobou sama mind boufa deuggeu
Néwoulé-Doumala topp
Kou tchi nékk ak li nga beugueu
Nioune dé rap laniou sopp
Nioune dé rap laniou sopp
Kou tchi nékk ak li nga beugueu

{Verse SANZALA
Man Nioune rap laniou sopp, dougou si HH bi-
Di drop tracks yi, douma la baap, dama ndjaap yoon bi-
Dékkou naatch saga ak xasté ak téxeuh
Guissouma kima nara wéxeu-
Dama concentréwou tchi liguey bi di door waar-
Djéema indi lou woutéek mêmes code bars-
Yila gars yi di bombeu, douniou sonneu si job bi-
Barina limay soor, beugouma niou dima xoolé star
Lima beugueu tchi HH bi rappeurs yi tchi eupp yorouniouko-
Xeupp naniou yalwaanou gars yeupp-
Déf différence a niou warr,, Bokk mouvance
Djéemaa djeumeulé kanam lancée bi-

Real talk,, Loo fook fau ke féxé ba tok si donkaassi gui-
Téxé ba djot peex-
BMLBLP di fatch soxla yi-
Kou nékk, doon sa boss
Li fi nékk xamnga né dina la yéem
Bou sa xol leundeumé no no bou ko sax djéem-
God faaléwoul gucci bi nga sol-
Bouma xaar, dooma seen, Yoréwoo lima woutsi
Hight class laniou miim, pause,, Dougou carrapid-
Big up dablessed, gars yilé
Daniou skillé, dofouloo-
Rap bou djaar yoon fii rék rék rék nga ko meuneu feelé

Walawalabok job wala tok, mane ak pps tchi beat bi-
Di drop molotov yi
Ték rap bi nga gueuneu love
Di nga yeungou tchi lou deuguou dina awou si sa deunn bi man
Bokheu sama mic, nara yeukeuti daadj yi
Défaites yi ma bagn ko ba teudd tchi naatch bi-
Yaa ngui get li daxeu si sound wala gni fi daxeu sound-
Wala gni daxeulé sound

{Refrain}
Fi nga beugueu yobou sama mind boufa deuggeu
Néwoulé-Doumala topp (Yeah)
Kou tchi nékk ak li nga beugueu
Nioune dé rap laniou sopp, Nay lerr, Nay lerr
Nioune dé rap laniou sopp, Nay lerr
Kou tchi nékk ak li nga beugueu (Yeah)
Nioune dé rap laniou sopp (X2)

{Verse PPS }
Kou ci nek ci nioune, Lila Yalla diaklel
Kou ci wekou ci koune, Do reer do diaxlé
Kham nagne fa niou jogué, Gueumeu tanne yone
Diegui wakhi none, Kaddu mbed lagne niou yéne

Kouné sa feeling a deugou ci yaw, borom bé ko dogalé ni, mandou wara bokk sunu djiko yi first
Tanef sunu art, takku dogou waar, Ragnékou ci kaar, mbed wané kalaama niou djiko mou feuss
Deuk di job – moudje ci dope
from nothing we reach the top, gueum sa bopp di tèerè hip hop,
Deuké tewal sunu street dathie sunu beuss
One love to the old school, sunu dembeu rek takh niou nane taye,
Melomane yi yagg support ci CD ci scene,
Ci nathie ci rain, mouye daw di rène,
Yena takh niou naane faye, Streetwear all days, bootleg OK
Yako takhane yènoul, mane ak jeem yèmoul, pps mo aaye wala ya nul
Beat bi ill na Sanzala, mbind mou taarou sagnsè la, Lyrical miracle gangsta la, if you don’t know now you dig it
You can judge but I know who Im I, Soldalou soldarou mbed, Sargali xalima fepp, yegalè seni mbebeteu, Yes we did it

Man Nioune rap laniou sopp

{Refrain}
Fi nga beugueu yobou sama mind boufa deuggeu
Néwoulé-Doumala topp (Yeah)
Kou tchi nékk ak li nga beugueu
Nioune dé rap laniou sopp, Nay lerr, Nay lerr
Nioune dé rap laniou sopp, Nay lerr
Kou tchi nékk ak li nga beugueu (Yeah)
Nioune dé rap laniou sopp (X2)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR