LYRIC

{Verse 1}
Nioule naa té beuri dolé non dou séw na khess
Dougou naa ci xol yu deugou yi ma xéw ma bess
Never ever moussoul méti bama sell ma ass
Still underground Mc boudé rap my best
I run this game and I keep rep my té-ci (ma cité)
Deug leu tchi mbède Paris yi j’ai vendu la neige
Dem na tchi gardav (Garde à vue) mais meusso dégue j’ai vendu la mèche
How many time la dougou tchi taukhi douneu dem jail ?
How many time la yoné cash money comptél?
How many time la déh fougnema braqué gun?
Mbède nimouy djouré nonou la meuné taagué dom
Gnila beug dougnou jog ci pleures yi mais do guiss
Loudoul money aape ko beu Fleiry Merogis (Prison de Paris)
Policia bou guéné gun dérettou néro (Noir) ray tiss
Fi kougne fi daaj ba def ci caisse rek sa mère réy tiss
How many time lagne fi kill nit ci injustice ?
Bakkanou ngèw mo gueune bou nit kou nioule ci sèn guiss guiss
“Niaak pexé, pexé leu” la moudj def slogan
Kamikazou ci ay deal ba moudjé done délinquant
Fadjar téél nga dégue thioy feug perquisition
Cagoulé wou indi séni dogs yi tek leu pression
How many time lagne fi seuf nit bouniou amoul ay preuves ?
Signélo leu procès verbal yu wouték sèy jeuf
So dé black juge bi daflay feug ay years
So dé white lou cas bi graw sursis ngay dieul
Now you know loutah ma rancunier ba melni ciste-ra (Raciste)
Lima lay tégal ni dou mouv. bi ladjal Boy mir-Sa (Samir)
How many time lala thioy yi képeu amoulo péép ?
Niou humilié leu djapp door ba nopi pompe la gaz
How many time lagne la taf fekk nga yoré sa money?
Niou foukatiko néleu djoug fi mba niou takal la lam yi (menottes)
Embrouille sous le préO ça part en couille
Ça tape la barre fix,les pompes et les racketteurs fouillent
Transac. aux parloirs pour faire passer le bédo
C’est la baston pour les pointeurs et les pédof.
How many time laa deup nieuw indalé ay bric ?

{Refrain}
Réglèl comme que reuthiou meunta sopi ay dieuf
Téy nga dall jaameuh bala ngay jog di def
Réglèl comme que weurseuk bila Yallah djaglél
Di ngeu tchi djot sayu waxtu wimko nammeu djoté
Kone réglèl
(2 fois)

{Verse 2}
Lou yagg né ci sama mind neu yagg louki samay beute
Make money by any means neu toukeul sama life
Tuute tankeu ci bountou life mane mi tougueul lama fék
Mbède djoxma djoumtou waay yi ndéké tendre nama piège
Chaque night souma gnibi galé compté ay liasse
Deuk hôtel ak villa di dox ci shoppin’ ak voyage
Poches yu diss ak meuneu tchiachie (savoir parler) dafay yombe nga serrer meuf
Crystal bi wékh neu taal ba nopi di guène zéro neuf
Marcadet, Clignancourt, Auber ak Plc
Takussaanu printemps lagnema grillé ci ay jumelles
Gnéinteu (4) fane lagne tchi tek may doga xam nou kasso mel
Fadjar téél Oxy feug beuntou diokhé la gamelle
Bitch yima daane battrél kène nieuweul parloire
Waathie promenade bi niakantéko ci raak général
refus d’obtempérer commission bi yaubouma Mitard (Isolement)
Few months later out the jail délou case départ

{Refrain}
Réglèl comme que reuthiou meunta sopi ay dieuf
Téy nga dall jaameuh bala ngay jog di def
Réglèl comme que weurseuk bila Yallah djaglél
Di ngeu tchi djot sayu waxtu wimko nammeu djoté
Kone réglèl
(2 fois)

{Verse 3}
Bi life dalay kambal lou yombe lalay tammal
Ay nakhi nèène lèy moudj done nga done djaam diko raamal
Defna tchi mbède Paris ay putains dégats yu beuri
Tay reuthiou lama diké ndakh yaak na tchi life-fou diambour
Beugone neu téki waral ma eupeul melni kouy djirau
Nit kima djamone paaka kane moma waxni dééwoul ?
Kima yaabilone perr kane moma waxni overdose-zoul ?
Ay laathie yu amoul tontou ma warko lay ak Buur bi Yallah
Donté douma modèle mais meune nga djangue ci sama story
Xellou xalé moma djapone bataye may tuup sama torts yi
Niou beuri ci nioune système béniou poussé pour niou fauté
Ndakh amouniou péép té meunou nio délou galé ak loxo nèène
Da ngay diémeu djoup takkalaatou ci ay montres ak ceintures
Dou téé thioy yi indile leu fitna deuk tchi bavures
Sometime meuno comp sori sa deuk nimou métté
Xeuy toumranké fi gaw neu lool té fi dafey bétté
Njaboot nga ngi khaar nga yauné mandat werr bi déh neu
Dagnouy fokni fi xaliss da ngay seuk lepp yombeu
Some time niou fatali leu diw mi défaraate neu sen keur
Mou gueune leu yokkou xaptal ndaxté froissé nagne sa égo

{Outro}
Yeah ! Nga beug prouvé sèy mbok que ni do yaafouss
Batakh mou dougueul leu ci yénène ak yénène you know
Diémou meu layyal kène but sometimes it’s not easy
It’s not easy bro ! You know
So no matter what dou yagg ba li araamone dagane men
Soula Yallah diokhé occasion wala sa chance na ngako saisir
Diémeu tégou waat ci yone wou djoup bi bro
Yalnaniou Yallah saameuh té djégueul niou bro

{Refrain}
Réglèl !
Réglèl !
Réglèl comme que reuthiou meunta sopi ay dieuf
Téy nga dall jaameuh bala ngay jog di def
Réglèl comme que weurseuk bila Yallah djaglél
Di ngeu tchi djot sayu waxtu wimko nammeu djoté
Kone réglèl

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR