LYRIC

{Gaston – Refrain}
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh 
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Limouy doundou dafa wékh (2fois)

{Verse 1}
Donté Climat…… sett, nité leu waune
Réw mou diakhaso waune
Waayé yéwou sangou djangui lakay wadioureum santone
Mou warone léral li leundeum indi waat réweum cii ngone
Dieulé fa niak saxaal fa kom
Fay Kaddu makadom
Indi fa banekh Melni garapp bou sakh ay dom
Donté askanam ma gueune yess wa Sodom
Meunoul waune gueum ni digueuneté bou gatt doundeum
Dina sopalikou makadom
Mère ak Pa wame dadi crise
Tchi lou tolou digueuneté tisbar ak Timis
Délou tchii fékeu tiss
Faat bakane done lou diss
Fokné yi…. douko miss
Nieuw fékeu ndeye ak bayam teud dérette sangue lène

{Gaston – Refrain}
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Limouy doundou dafa wékh (2fois)

{Verse 2}
Yaw mou dide
Youkhou djoy yegg métiite
Niakeu ba siit deug bi yeup niou tal yakeu massacré
Deug dji may wakhé Hal motakh ma sacré
Natangué moudj sopalikou toumranké
Rongagnagui waal
Doundeum laniou waale
Foumouy guissé koukay wallou
Xamoul li, Il ne voit que du sang
Mérité woul li c’est un inoncent
Mo ngui leundeum té xiff na
Mo ngui cii fiitna
Mom mi tiitna
Dérettou xétam tissna
Doundoup domou Adama amoul dara louko meuneu rénumérée
Mo ngui sogua lire cii libérétam nga xagne ko Liberté

{Gaston – Refrain}
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Limouy doundou dafa wékh (2fois)

{Verse 3}
Yaw tass ngène ay yakarou xalé deflène djirim
Ay bour ngène sopi badola ……….
Yaw nétali bi story sipp nga roussouma li
Sèn bone guéy rotchi rouh féété sama lit
Ethopie Rwanda Burundi
Niata xaley déh cii Mali
Niaka takh niouy déh cii Palu
Yoylo ngène chartou All Human Rights
Néweul ko dolé mou diaxlé di weur kouko meune ress
Talal loxo Amnesty ….UNICEF
Ak bepp mbotay yu xekh youy xékh Aakeu ak yéleff
Foumou dieum, Foumou dieum mom mi cii bi leundeum
Soneu nagn Soneu nagn

{Gaston – Refrain}
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Rongagne yégui waal di waal toyal lékh
Guissoul pép boumou sékh
Limouy doundou dafa wékh (2fois)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR