LYRIC

toppatol sa bop, mane dama beugeu sama bop
damay photo sama bop, ba paré wone ko sama bop
toppatol sa bop, mane dama beugeu sama bop
mane dama beugeu sama bop, mane dama beugeu sama bop, BEUGEU SAMA BOP
i got 3 friends, me myself and i, me myself and i,me myself and i

{1er couplet}
hun, lane mo warral tok di khar
dougn leu ko defal nageu diouk takhaw té doori war
faut que mou sotti gaw, lafegne meune neu dokh ba naw
yene sayi niou nekeu sa kanam nio lay wone guinaw
ko fi lath mou werré, dioye na ay flaquou dérett
mais takk fitt mo eupeu ndieurigne takk téré
dakhadji aalal ba faté yalla diaral leu ko
yalla wathié taw, macky guen di talal lokho
sa life niou taral la ko, gue fey lakk niom niou talal leu ko
diokh lene sa bop, niom niou kharral leu ko
magui rap mais téréwouma nekeu diangue kat
bougouma djeune, dama beugeu nekk napp kat
douma yakkar keneu, dakh kene dou kharou ndakh mane
def limay def, et puis lou yalla def bakhna, hun
wakhma ko yakkar wakh ma kane geu geum
boudé mem sa takkander neu leu bayi ci leundeum

{refrain}
soneu na djommi na, niom dagn may diéma goumbeul wanté guisnaaaaa [yiiaaah] mane dé foumeu meunti dem, tiono rek lay guiss ac fitnaaaaa
bountou bou ma feugeu, kene douma help
bou fekké dou mane, kene dou ko def
adouna neu toukki té kene dou fi dess
bayi ma def ko sama bop , yalla def litchi dess
na ko defal sama bopp, na ko defal sama bop, nako defal sama booop oohooo,
nako defal sama bopp,

{2e couplet}
hun, ay montagne lay escalader
kou geuneu mouss moy kou geuneu khalat dé
khamal koy topeu amneu niou leu nara réral
serigne bi néna mo lene geuneul yalla néna
kone omzo dollar néna, beutt dou lepp lay guiss fils
il faut que ma goumbeu pour niou bokk guiss guiss
lougniy khathialé dou mousseu toolo ac louniou bolé
seytané beuriwoul dolé nigga yaw ya new doolé
changel sa melokane, meunoutouma delou mane
djoulit là mais meussouma guiss chrétien bouy yélouwane
faut que ma djouk outi, yeh khouss touti, mouss touti
kou amoul djomm neu meu pouss touti
amelouma dara keneu sauf gnou ma meussoul bayi
sama yaye,sama yaye, sama yaye, sama baye
wakh ma ko yakkar , wakh ma kane geu geum
meme seu takkander neu leu bayi bo nekké ci leundeum

{refrain}
amgeu diné geum geu yalla, kone do tite
na geu moytou life bi woroul melni pronostique
negnou gueneu yakkar yalla, doylo ko
africain gueum neu yalla, mais wolouwou ko
i say, diné geum geu yalla, kone do tite
na geu moytou life bi woroul melni pronostique
negnou gueneu yakkar yalla, doylo ko
africain gueum neu yalla, mais wolouwou ko

{refrain}

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR