LYRIC

One Lyrical feat. Hakil

SELF MADE

Potentiel

ONE LYRICAL   

Da may hustle toogal di wax pourquoi ñu nan ma no way

Bëgguloo ma me too I do you baby screaming my name

I believe I can fly don’t tell me no bless over my lay

Still the same don’t know us

Keep yourself about me

Tay ma burle kon jarul pass

Ñaata nitt a ma gasal pax

Ñaata ño ma bañ

Mais nee nañ bul di topp sen xol yëppay bax

Ñaata ño ma yeene comeback

Ñaata nitt nga woolu denk len sa lepp tay ñu nan  la yay kan

[F**k yay Kan]

Motherf**ker yow yay kan

[Mof**ker yay kan]

Topp sa yoonu bopp rekk a fi des

Sëgg ñi di wax  siggil sa bopp

Siggil sa boop sëgg say wayjur hater niggers what a f**k

Man maa siiw parce que da ma sob

Li ngen ñoddi boo ubbe sama bopp ding ko fekk mu toog

Keneen ku melni man gisu mako

Ci kaw ci sa kanam feeteel ginaaw budul ci gent do ma f**k

Nee na la man bëggu ma jikko toot

F**k you ya’g sa buzz do gis ku dee yobbale siiw yawmal xiyaam

[F**k]

REFRAIN

Jël sama yoonu bopp  a fi des (x4)

Jël sama yoon (x2)

Jël sama yoonu bopp a fi des

Jël sama yoon (x2)

Jël sama yoonu bopp a fi des

Jël sama yoon (x2)

Jël sama yoonu bopp a fi des

Jël sama yoon (x2)

HAKIL

Bo xamul fi nga jëm deelul fi nga joge

Loolu day fekk fi nga joge neex

Saytaane bari dooli ken duko jege

Mais dara dara duma teree xeex

Akk moom ndax ay sëttëm rekk ño ma wër

Bëggu ñu ma nekk ci Jàmm ni malade budul wër

Bimay ne sama biiru yaay rekk la nekk fu woor

Judd nekk goor

Zéro peur Yalla rekk lay soor

Awma lu may rèccu lepp noonu la

Duma changer tus lepp ci yoon bi la

Yen say lu gëna baax ci yow lu bonn bi la

Samay meilleurs professeurs sama noon yi la

Nitt ku ñuul ñemewul lu bees

Foo jaar ñu bëgg ma ray

Bu samay noon bariwul woon sama bopp lay njëkk mere

Mën a baax mën a bonn lo fi seet gis ko may internet

Nitt kuy weeco ay nitt doonul ludul nittu interêt

Jël sama yoonu bopp vitesse Foog ma seey len

Freins yi dagg may duggël vitesse gaaw ni Eminem

Ay jëmm tiim ma bëgg ma fees man may nittu neen

Jàng na ci lepp lima wees muy dëgg di fen

[Jël sama yoonu bopp, sama yoonu bopp, no no sama yoonu bopp]

Topp ma ken ma ngi sama yoon (x2)

Ich yo boy

I got no excuse, no choice

The only way you are is living yourself and follow your own way

REFRAIN

Transcrit par Maalik Si

Added by

Maalik Sy

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR