LYRIC

{Verse 1}
Limaye doundou mane la, lék lék beug mane la
Mane la, mome leu, meune la, méne la, mbed mi kémane la
Bamaye goné, la ganee samaye gueinte
Jang feithie, graff si feuille ak waye yi maye feinte
Yéré bou sérré fandé, Jean daleu gueuneu gandé
Ok, shirt, baggy, basket, all day tek si casquette
Barde si Style, skill, real ni Guélwar
Mélni 2PAC done dream, baate yi gni di galeu woor
Di kothie sono mondial wala fm samedi relax
Comme LAS baate bou diss, guiss seukheul aye lox
Jokh ma beat ak bass, ma ték hit ték clash
Clatée les bandes, classée légende, ghetto bi siik boss
Khawma kagne la si dougou, Bess bigne siye guéneu yalla kham
Wékoumako si kéne, Lima siye liguéye rek laye ame
Bayinala ak li khéw, Loudoul dée laniou gueum
Kham nagne famou jeum, téyal gueustou moujeum

{Refrain}

{Verse 2}
Like the black power, dank biye féete sa kaw la
The writah hour, tank biye féete sa kaw la
Knowledge and movement, di missalou name bi
Khatim ak kalaama di samm, niou sallo game bi
Hip hop di thème bi, Under yi kham nagne capitaine bi
Kou wéete ragné, gni amoul baak nioye sape si téene bi
Nioye saw si téene bi, sén but di soukheul yéne bi
Nguir Sakhe si scène bi, real yi di sakho ikhssane bi
Jeufeu gouniou daniouye jéem, gni si souf nio ma yéem
I’ve followed the leaders, mane ak yaw manouniou yéme
Rombena théorème, téere lalaye bakhé
Ligne done seintou daaw mo téew rene, jolof laye sakhsakhé
Hip hop!!! beuguouma koulaye djooyloo
Fassanté nagne koleuré, Lou wouré bi diour niou doyloo
Rap yomboul, ba kou jok déf ko fowoukaye
Negger do or die, seurou fake matoul wodaye

{Refrain}

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR