LYRIC

{Refrain}
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooove (Ehhhh)
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooooove

{Admow – Verse}
Amena loula nekh cii mane
Boul mako di neube kaay wakh mako waay
Rakeu louma nekh cii yaw diéguéssil rek ma xamal lako waay
Yalla moy maayé té di wouteulé
Dioxma lii mayla léé kone daniou warr di na-ngou leuneté waay
Do soneu boko ndandé
Niit yi fofou laniou rawaneté
Lii nice cii xoll la fétéé
Dess na cii Niit ki mou meuneko djeufé
Lii fess cii xoll feinthie cii dieum dji lééé
Loko neube neube biss dina nieuw dina meusseu fégne

{Refrain}
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooove (Ehhhh)
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooooove

{Book’s – Verse}
Boul lène ma weithie lène lène loudoul peace and love
Limay feel sèni face daf ma titeule lol
Li né cii heart fégne cii face diokh ma ligne my call
Ma ngui feel da nga ma feel nieuweul fils my all
Lambba tèn pas de haine pas de succès ak tiol
Pas de men pas de shoow pas de news ak old
Pas de wakh fi wakh fé pas de wakh pour xoll
Pas de wakh wakh wakh rek dou takh mouy drôle
Finiou diougué dafa sori dafa sori,
Amena gorille amena gorr yi
Am niou worri té stress bé takh
Fi nga niou goungué dafa sorii Dafa sorii
Sunu story Sunu glory diniou ngougué ba djapeu ndiakh
Liniou diota tameu peace love and diam
Gox ba gox daniou ko dox naniou sameu
Liniou diota tameu peace love and…..hahaha
Respect me Bro

{Refrain}
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooove (Ehhhh)
Da nga wara show love
Yaw Da nga wara show love
Show love show loooooooove

Real Hip Hop New Shit

{Big up by Books}
Nga beug biz wala kiss whatever man
Boko yégué diox sa Five nga door ma mbagg whatever man
I love u too xam nani ya ngui maay feel
I feel you too
I love you too, Ladies and gentlemen

Show love (éhhh) Da nga wara di show love
Da nga wara di show love
Show love (ooooooouuuu ohoooo) Da nga wara di show love
You got this show love (Ehhh)
Show love
Love Me lady Da nga wara di show love
Show love (éhhhh)
Show looooove
show loooooove
Yaw da nga wara di show love
Show looooove
show loooooove ….
……………………..………
Da nga wara di show love
ngay makk di xalé
Lolay aduna show -wal love niou show la love
Lofi dioxé laniou laay fay
I love you too
Peace out….

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR