LYRIC

{Admow – Verse}
I’m a Soldier, I’m a fighter for my all life
Courant bi coupé may kiy tal sama all light
Sama team lay, fétél sama right side
Téyé ko ni AK 47 bilay kill right
I more my way té douma stop now
Dama lay diégui dokh egg on the top now
Ya ngui maay xol cii ay beut té xamé woma
Té fo zappé mane ngay séneu may bégueul Goor ak women
I’m a S.O.L.D.I.E.R. we ain’t got the same dream, yémal cii Sénégal
Ma ngène run the world, ngène xippi saay beutt
Ma ngène tothie sa guémigne
Nieuw nga bayi hate bi xam ni I’m a Soldier

{Refrain}

{Nitdoff – Verse}
Youssou, Ibou, Abou, Paco, Xali, ak Daouda
Xouss di fipou amatoul Didjou (tokk) youkhou ko cii laughter
Life bi dafa gaw doula xarr at yagui séy ni powder (poudre)
Niéne gni taylé sèn life nguir touki djii cii kawba
Kène togoul di médeu
Kou né ngui wout tédd
Life bi beuré leu kone fékhal ba boumou la songue betteu
Diougueul xékhal sa future
Say mass fékhel ba raw tcha
Loy def fékhal ba gaw tcha
Yonou fouleu ak fayda aw tcha
Sépile sa bopp cii lot bi
Tek sa beutt cii haut niveau bi
Guemeul sa bopp boul déf ni ki di tok cii omi djaubi
Soldier sa family nala djaral nga dé cii war bi
Loumou métii métii boul xaddi sérél sa machoire bii

{Refrain}

{Mousdef – Verse}
Yaw meunou niou bokk mane ak yaw Cause I’m fuckin’ Hero
Douma saa mass té bokou niou yone kone rak boulma merlo
I’m over tall ya, I’m a soldier, Mane douma soneu cii ngélaw
Bi maay diouk di hustle ndakaté bobou ya ngui teud di nélaw
I’m Real Diambaar, you a yambaar
Dama lucide nigga mane soxla wouma taukh ay yamba
Mousdef boy bé ngeune tangg jailou tamba
Yaw mane damadi soldier damay dem toi tu restes en bas
Yeah !! What the fuckin’ niggers talk about em
But I don’t give a damn yes, I started from the bottom
Mousdef dafa struggle baniou diokhogne ko baram
Motakh taay fipou am fiitou yeukeuti batam

{Refrain}

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR