LYRIC

{Verse 1}
Han !!!
Ba dara doonul dara, yafi nékone
Ba Sa dome di magg, niafé tékkem yootou diote Kome
Waw Coumba Sondje leu, Yaye ndoumbé kèn leu
Sa tour lay doré, diaré nguir wassaré sargal siguil kepp kouy soxna
Soukhou sa bakk saxna
Yéneuy diour yarr yorr té yène lagni door
Yéneu niak batt téwoul ngène né ci guinaw bepp Goor
Pa bi garé ngay diayanté bania deup tchine
Nioulay doupé queen, mousso farafina ba Chine
Ngène yènou thionoy aduna té duniu ko guiss sèn beut
Ngène djoy ci birr, Rée ci biti réewal dome ak seut
Légue Légue nga merr mattu digué door bou bénène yoné
Waxtou wa thia topp nga faté firndel sa yéné
Dioxé lepp déssé yalla deugui Love yawla, Diégué di Kiiray
Yay sama lerr fi Yaye
Sama Waay sama werouway
Sama karuway

{REFRAIN – Amdy}

Sa yuma yéwo xippi xol
Baneex fess sama xoll
Djeumi goor bou done gantiax
aduna missalé toll (2 fois)

{Verse 2}
Yo!!
Yénay Sunu Meen, Mudjuk diamono diour ay yénène phénomène
Li magg gni waxone délu ci, sèn xel yi seug ni wène
Mélokanu marchandise ak sen djeum di bène
Ngay doundeu Cash rule everything around me
Djiguènou tay da ngay diomi xol ko ci town bi
Kou gueum sa bopp do saalite xalatal femmes de Nder yi
Diour bakane sani cii mbalite fokk niou tek blame ci mères yi
Xam lène ni kène dou yèene, yegg yegg moy takh niouy yéssal sass bilène borom bi yène
Yéneuy Yaye, dome, soxna ak soeur
Li gars yi wakh gueumou niouko xippil tak sa Seur
Han !!! Ci deug banekh nga yéyo, yaye meenou askane Sunu euleuk nga Yayo
Takou, Dékku Aduna dieul-leu noono
dieul-leu noono

{REFRAIN – Amdy}

Sa yuma yéwo xippi xol
Baneex fess sama xoll
Djeumi goor bou done gantiax
aduna missalé toll (2 fois)

{Verse 3}
Han!!!
Faxé ci faarou goor, diox bakène gorri gorr
Gall sa loss borii borr, banial ndjaboot bi békkor
Black Women!
Sell ni sunuy yaye, jambar ni Aline Sitoe
Wouté ak gni may guiss ci télé
Women!
Ci marché yi ak ci mbed mi
Fadjar niu daani sen doolé ci tangor bek ci sedde bi
Women!
Waro lek ci gaalu xacc
Dinagne xass, xuloo, xeex ndax yenay sunuy xaac
Sunuy Princesse niko Modou Mbacké waxé
Sèn yènn sèn yone niko Soxna Diarra Waxxé
Soxna ci eh beug moy takh niouy soneu ci Yéne
Yému ci fi ngène dieum ndakh yéneuy Sunu Meen

This go out to all the women in the world
Sunu yaye, sunuy soeurs, sunuy soxna

{REFRAIN – Admy}

Sa yuma yéwo xippi xol
Baneex fess sama xoll
Djeumi goor bou done gantiax
aduna missalé toll (2 fois)

{Outro}
Ba dara donul dara, yafi nékone
Ba Sa dome di magg, niafé tékkem yootou diot Kom
Waw Coumba Sondje leu, Yaye ndoumbé kèn leu
Sa tour lay doré, diaré nguir wassaré sargal siguil kepp kouy soxna

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR