LYRIC

1er couplet Moulaye

 

Dougou tchi game bi pateulegn khol ki mey sagna pissety/may controler, di seddele di dokhonto numero diss / chill fils tu connais la mise, c’est All-in et roulette russe/ chill diss on gère le feat, genre Xatim et papyrus/

Je fout le feu au poudre, fais le fele devant la foule, rien a foutre c’est Wam qui gronde, quand les fakes fuient la foudre/

Douma fate dama fouy, douma fayou je m’en fout/ ils rap en fourchelang kan ya mon blaze dans leur bouche/

L’hiver arrive qui se sent morveux se mouche/ chui un demon des mot qui se croit génie se touche/ je sais ou je vais comme le premier de la draft/ eux c’est au fond du trou qu’ils ont trouvé la trappe/

 

1er couplet PPS
Tathiouléne mou riir the writah djeuleuti Mic todj fi
…Roye dou nourok piir, bamay djéego yangui tok fi
Wané fi louné nga roote fils, waané ci gouné njaboot fils
Mané ci yégg ci founé, té fouma xatimé ca kallaama xoote
I float like a butterfly, sting like a bee
G G Galsen greatest, kocc barma dée ma lakk bi
Masso guiss kou mélni mane, foy djeulé malaaka bi
Yagg na raatalé under bi, yeukeuti peundeu tathioul ma lakk fi

2eme couplet PPS
Hoo! Daniou xam soga wax – rame soga dox, 2bedaxé ko ci pett -shut!
Mane soga jeuf – naane ci gadjaf – def sa rap ci pote
Moulay néléne bokkou ma sén game, nioune musiqueu niou takha jok
Fou PPS téewé nga seunguém, foma sén gueumeu may..

The best who ever did it, bête la ci mbind mi ni
Non doula minimisé, béetéla guimi guindi
Fété la ci simili, simmili li gars yiye simuler
Bene dou ci mille yi, gnibi ghetto delou sami lé
Fils bi daye gass, deureum dou doy bass
Gass né wakhaye beury dix dou raye As
P.P.S aka the ghost writah!!!!

 

2eme couplet Moulaye

 

Damay door defleu bassang, may gome bi ley khassan/ fougn meu fekk mounougn ma fetch, degni mbeuw khol sen kanam/

May goss bi ley jangal, may boss bi Legn diomal / damay def tek di lek tchi bol bi gueuneu sakan/

dagnou ndol beugue tabakh, melni gana yiou beugue sabar/louniou beugeu dougn ko ame dafma leer melni soubeu/

Depuis tt petit je competit, sans confettis, tt en sachant qu’il ne peuvent  me contenir/

Da vinci j’ai le code et ma place de parking/ franc macon je bati l’empire a la dynamite/ recrute ange ou demons selon la combine/ et le feu n’est jamais loin de ce qui me fascine/

T’as le doigt sur qlq chose depuis que je suis à l’index/malgré le contexte je conteste nos complexes/je conçois mes texte comme un concept concret/composer par tout ses complots qu’on se cree/

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR