LYRIC

Intro
Way nala yaye , wayatila , suko diaré ma wayatela

[REFRAIN ] Sama Yaye dama yonni yakamtima
taxawalou warouma , Taxawalou warouma (bis)
(Yaye boye !) Yaye Boye ! Yaye boyo ! Sama yaya boye mane mo tax may daw souba ba diante soo (Bis)

Couplet 1
Matal wareefa gal sa losse bi
bagnu mathi debouché fosse bi
Say lokho minatewoulak sa posse bi
wayé yeené moy dieulé yaye ci bakhal dougalko si wagnou sosse bi
(Sama Yaye !) Blackberry’k Iphone goukhouma
safal niekh la douma ladoume douffouma
4×4 , mercedes toufouma
Sagane laye bagne ba taaru Djiguene souffouma
Lima waar oumpouma
Gnata yone la diay or’am guir guéné la 100 m
teggui natte xeupe ko si seurigne guir nga meune net
Koula yoré fouki att ak nangam
xeuy biss ponte diam tangam
Soko meunoul fadj , boul feke domam di foo ngay todj manxam

[REFRAIN]

Faatalikul , baga meunoulé touss
Yay’la dane ouf , kone lo mouss mouss
warka meuna rouss
Deugg la dome meunta faye wadiouram bayil xel thi li
wareefoy dome moy mou sakku ngeureum bou djoukke si wadiour yi

Sama yaye , dama yonni yakamtima (bis)
Thi Khelkom la née , beugue beugue Yaye ndigeul la
Moytoul mou diggeul la
Deggloul ma digeul la

Djougal deme fimou la yoni soriwoul
Limouy lath beuriwoul
bayil lekk avance ta beuriwoul
Limay bagne moy ladj nagnouko yorewoul
wala goréwoul
Warna sakh may khar matte bala gnounane thiebou Yaye dooréwoul
May Thieb , May diwligne , may courant , may dokh
djangou xallé yi pour mou dokh
sama poche bi waroul lokh
Wareefa teggou sa ndodd bi
warouma topp mode bi
1er sappé la beuga taxaw sou naime biy diekhal nodd bi

[REFRAIN]

Lyrics by Admin Papi
Picture directed by : Abdoulaye Ndiaye

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR