LYRIC

Father babs word up
Bazik word up
MYD word up
Bouray word up
RimK word up
Mo junior word up
Noreyni word up
Abass word up

Ok 93 di crazy boyz, goné yi gané si crazy voice
Mbed di choice, waané ni royce
Di baggy di cap, di begué sicap
Japétik flow, jokh ethique rap
Tambalé raatalé under bi, yeukeuti peunde bi, Ndogal takh ande bi stop
95 di baatine 98 Mesagehe xatim

Amdy opti word up
Dooba word up
Julio word up
Doctor balde word up
Sidi fall word up
Begué, Aba word up
Paper word up

Daniou joudou ci zik, tarbiya bic
Nixma ci writing, philosophique
Reader, writah, leader, todo la vida, por Africa.
Xtape, Xacci the tape, Xatimak kalaama sarr ci sa tape
Niou naatali pepp, raatalé feep
Mbed né guéb, agueu ci neeg yeup

Authia niou dem
Nieup nieup niou gueum
Metti metti niou jeem
Kaala jitou ndigueum
Guimi xam fa niou djeum
Yalla xam na moujeum
Di jogg di daanok writah fam, sans yene dananiou doundeum

Diegui sen game bi daa yeess-yé!
diogui seuguem bi ya dess-yé!
Togg album bi 4years- yé!
The ghost ci xel ci xol yaa bess- yée!!!!
Bondé ci beat yi ni marteau piqueure, nga niodi Vegeta ma done Petit coeur
Xaleu ci scene yi nga done auditeurs, gni begué ci mbed gni bégué ci keur

ci rhyme mané ci
Tané ci tanef yi waané ci
Ngiy nixma ci xitma gui ma né ci
Ki yeem ki la yeem la mandou ci
Yonou ndam la andeu ci
Khouss ci leer yi mandi ci
Goudi gui leeri, souli hilaire yi, bess di naniou teeri Zion

Yeah….Diss (Diss-crimination Talla)
Li moy taxéstyle!!

Niune _ dotoniu teukeulé ak Kén, niune duniu taxalé style
Dotoniu teukeulé féne, teureudi niggaz we still
Mbed mé ko falli, hustler mind rek
Reudeu lines you fine, shine ni Makaveli
Classic ci freestyle, degg ni Kweli
Talibé tari ci flow, rhyme ci technic, style pathie, dothie dathie, aak fep fadjé di giifloo
Li nga teulé foo la si niune, fi niu feulé xoolé ci kúne
Ate mi niu némali, leumbé ni AQMI ca Mali
Mané kuné n iu niamali, none yi run ni bugatti

(Bring it back)
Writah fam word up
Sunu kaddu word up
Galsen word up

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR