LYRIC

{Verse 1}
Let me tell you the story of “Coumba Amoul Ndèy”
Leemoul ca teel yaw tè sorri bi soumba amoul faye
Taye Peaçou ma amoul laye, tisso,u ma khamoul saye
Kouy lathie meune ci galsen té guissouma khamoul kaye
Xam nanè maay the king diaroul ngama kay fateli
Khawma kou soorone demb, wayé taye mako sapali
Sen rap la defal lifting, ak classe ni Diouma Dieng
Lale basang ci donkassi gui, ba euzeul titouma jeingue
Kane nga may teukeulel, dou ki dou keulè
Nafar li nieup meune, xaragne ci li MCs yi teulé
Samay maass, Hugo, Pelé, Ali Bomayè
Gueune ma tangue super nova, doxal fowi bouma yée
Yeah, mane dama yagg done chef
Lila yèem ci flow, 2002 la ko done def
Kou weedi ladjal Skillzography wala Bambino
Dama yagg feetèwo cool jotna taye game bi know
Jotna niou xam – kiko meune ak ki koy jéem han
Ki lay yèem han, ki mane kaani mane lèem han
Naniou dindi clash, dindi blow, dindi politik
Kone xadja goudi done Beuthieuk – no polemik

[Refrain] The best who ever did it, man im the truth
Street cred at the end of the days, i show and prove
Nenagne diam daye weex, mane ma joudou nioul kouk
Yaw Ngay saxéto sa crew ma done bén bu meune fouk
Kan nga may teukeulel – no dou ki dou kée
Fane nga may teukeulé- no dou fi dou fée
Yeah heun ! Fima jeumeuk yèen diaxal nama
Album ba ngui nieuw parel teerou diaxannama

{Verse 2}
Sama Xtape, nieuw meune seni classic
Xacci the tape, track yeup nieuw classé hit
Dama round sa mine, soga soga yeungueul sa body
Legende ci waar yi- buddy, Diw rap ci sabar yi
Ci gamou hypocrisie, tek deal ak féne
Ame toureu gueuneu easy, té do lakk fene
Gni nè Buzz laniouye weur, nienene Hardcord laniou diouxè
Ma nieuw ame classe, mane rap, tewoul ci hood bi la djougué
Kheuthio wouma dara ak yène, Xarap lene manouma farak yène
Sigguil sèen, ndeim rhyme bou tokh xaraf yèen
Tek-a ma wane yone, taaxirlou mbir yi dall
Melomane zikay meewane, fok niu feessale biir yi déll
Aliené flow ni skizo, dou MC cloné guisso
Koula nè diisso, Founé niou feulé ni Bisso na bisso
African H to da Izzo, classic baggy dou fuseau
Diegui niou dotoul easy, charette nga yor nioune fusée

[Refrain] The best who ever did it, man im the truth
Street cred at the end of the days, i show and prove
Nenagne diam daye weex, mane ma joudou nioul kouk
Yaw Ngay saxéto sa crew ma done bén bu meune fouk
Kan nga may teukeulel – no dou ki dou kée
Fane nga may teukeulé- no dou fi dou fée
Yeah Heun ! Fima jeumeuk yèen diaxal nama
Album ba ngui nieuw parel teerou diaxannama

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR