LYRIC

1.2 …. 1.2
Zero fowentou

Call your pap when u see the ghost
Call the cop when u see the ghost
Mandou ni christian, gueum gueum ni muslim
Original ni pygmee, sip na doko mouss lime
Dieuf dieul ni mourid, PPS the writah
Domou jant ak wéer, diam thiant ak wer
S.K la baby, recognize the team
Lou yess taye niou diegui, lou rak Nass nga tiime
Rombe naniou meune rap, daniou wékh
Chirurgien lyrical – raffalou rhyme yi ci sa lékh
Fournoy djaay tangue jaxannama, sibo sakh
Aksi wo takh, ngay xeleumé ak siwoo sakh
Manou mala guiss man, dalleu la ngay melenetaan
Aythia ma may len tank daane, ndaw yi mane lagne taaneu
Yeah, fangay xooxé lay accelerer
Tingope level fo yegoul, fallo fa accé léeré
Gni aak céder, nangoul the writah ma accedé
Feuleu ak CD, X comme – so fa aksé dée.
… Xaragne Sagna in da house
Fou ma téyé Mic ni 4 avril, generaux yi taudj
Niou sopi king yi queen, rap Galsen la niouy todj
… Xaragne sagna burn the house
Karismatik ni thierno Ndiaye Doss, writah the ghost
Sa MC xam na né maay boss, raay teu leu gosse
Hi c’est le best, writah the beast
Show me – who can test from west to the east
Haha! Kaddu yi leer ni guelewaar
Nanga Delou waar, wakh ko sa guéla war
Rio city sigui na tigui, xiir gui da dalam
Worldwide stand up, zidane takate na daalame
Yobouma BET ma yeem gniy yeungueul, feem yiy peundeul
Ci scene yi xandal, brain biy nandal
yeah – men xoote ni teene biy nandal
PPS the writah amoul féeneu jangal
Samay goudi gueune na wekh ndakh xalaate you leundeum
Souma guenoul li sama mind fou nguén di djeulé ndam
Nianal lene ma goudou fane dong ndakh domou niaye la
Rap mo fess ci mane, fouma yabbé démo nay la
P la, Galsen finest wala loco, kila kila
May sen Iness walaboka kiy dekil la
Noble Mindness nixma ci xarnou realeu
Yaw sa mind yess sip nga naxarlou bila

Diokh nala vécu ak baneex nga néma dooyaloo
Ma dikate – diox la flow, do néma boyaloo
Yeug nga rap bouye yé, shine lo sa mind
Mind lo sa gayine, yonentou xalima zamane
PPShine, dig im saying
Feusseul kaalama kocc barma tewal Galsen
Paré na, the game is over namtamba
Let me introduce my self, I’m the writah

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR