LYRIC

{Verse 1}
Kaay niou KATY beugouma LISSA
Damala beug soxna am AÏDARA
Diégui farr dila wayal Mc LIDA
Ak lane ak lane nga beug ? Nel COUMBA maay Feug
Xol dafa noya noy Gueun Gui Deuk TITI waxna deug
Keupeu nga Kharagne LO, foumou nek ni toyna xeppeu
Domou mbott dou féinté l’eau, douma BUUR GUEWEL bène keppeu
Naniou thionak Diaga, Bouniou BOUBA ak VIVI
Waro dess cii GAWLO SECK dougueuleul but bi
Sa guinaw wa beuri gobby nio ngui xeuthio beurigo bi
Fi nga tek galagne gui boko tégui woul dagnema robbi
Dembe sama bakkou yi di khireul kourpagnou marteau
Tay guéné ngama saakou yi ma diaaré fi wouyou dji ardo

{Refrain}
Djiguènou aldiana waro xeuy né bana
Dieul xol bi djapp galagne rek di thi teug tama
Rong dong dong dong dong dong
Ya ngui may rong dong dong dong dong ci ndongue
Waroma rong dong dong dong dong dong
Da ngama wara bong bong bong ci ndongue
Hééééééééééééééy (2 fois)

{Verse 2}
Takk nga thi rippeu rippeu, tothie nga sama monde monde
Xol bi nga dikk bippeu xam nga sama onde onde
Beugoulo mini jupe thiomo doula songue songue
Xessalo ba tippeu tippeu naturelle leu lolou la dongue
Yaay Fall leu Saloo, djom la gaalo,
Gnéinte (4) ak tranche rek zéro assaalo
Dina toggue dina fauute dina passé dina rotte
Li nga beug dafa deugou na nga diokhé ndieugou dot
Na nga faga ndikou bokk, loxo bila gueuneu meuneu djootte
Yoré ko yeureum ko yaatal ko yokkou ko yédeu ko yéné ko Yallah meuneu yokk
Kaay niou léwaato def “Salsalaato” done ay Indo
Daw di door dakké à l’amour c’est beau
Sans yaw sama peine (PENE) BANA (Omar) Yaay encre bi
Ndiaye Diatta Ndiaye 4×4 nga yaw do niankare bi

{Refrain}
Djiguènou aldiana waro xeuyné bana
Dieul xol bi djapp galagne rek di thi teug tama
Rong dong dong dong dong dong
Ya ngui may rong dong dong dong dong ci ndongue
Waroma rong dong dong dong dong dong
Da ngama wara bong bong bong ci ndongue
Hééééééééééééééy (2 fois)

{Verse 3}
Bo thiakhané woul ndèy dji cheikh sa seuy day téleu diekh
Da nga seuy ci waro sett cii féxal mougne Ba baye cii pékh
Boula alale takhé yeuy gouro Almadies 100 mètres lay ndouraul
Wala fou Monsieur guéné rek nga rothiékou yaw séti Paul
Li kharam na (kharam na) Ki faram leu
Té mou ngui baayi borom keureum diakhane ci kaw lalam beu
Mou ngui SALAM beu di tcha laang nga
Dagneka forcé wala mouy intérêt rek donoul flamme beu
Sa dale daggueu do dém djiguène ak xétou gowém
Bou djégué borom keureum xaram xaram perte dolém
Do togou passé bay lem, fiir beuri problème
Salon, diwou, nguéneté, tour, bokou sac do dém

{Refrain}
Djiguènou aldiana waro xeuyné bana
Dieul xol bi djapp galagne rek di thi teug tama
Rong dong dong dong dong dong
Ya ngui may rong dong dong dong dong ci ndongue
Waroma rong dong dong dong dong dong
Da ngama wara bong bong bong ci ndongue
Hééééééééééééééy (2 fois)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR