LYRIC

{Kalif – Verse}
Ay djouni laniou yaune Tokanetal laniou done
Rawaneté bé sori té méti donté kènay moudj done
Wett na tchi Xouneteum
Diox naniou ko djabi doundeum
Diox ko xéweul ak ndam
Boumouy dieufeu ndiko cii nguirou doundeum
Dadjé cii xounetou bi djangue idji
Feug cii bounetou bi gars yi tidji
Solal naniou ko mboubou bou yiw té goudou
Lata mouy djoudou, djoudou ram, dokh, daw
Bawane né ndokh taw
Day fo di kaff di feusseul foumou fété ngeune fouf
Day tok di raff cii euzeul limou faté mo gueune souf
Xamé toul day naar, talatoul day maar
Deuké téneu faté ni moy xalamoul akbar
Moy dieum diou djougué cii dieum
Sou wakhé niou tam ko deumbe

{Gaston – Refrain}
None la xarite la, yéférr la djoulite la
Ndjite la té djite la, djoundje nala Khibla
Sol tenue mbeep la, mythe la té ndiip la
Tiakh bi thiakh bou deep la
Kaddu ngui tawkhit la ( 2 Fois)

{Gaston – Verse}
Moy pess rideaux yi
Diakarlo golo yi tchii bureaux yi
Film biy daw enigme la bou xell doul dathie
Bouké likam mouss djité xathie
Bo comp-poul kigni cambriolé ngay youkhou sathie
kép door bamou né lathie
Ana louy laabale ndokh
Soukhou fétal mabale gokh
Naarou goor bi ndiabale dokh
Bo amoul pepp babale yokh
Yeurmeundé dou ngeurmeundé
Rouh desskay formaté
Mou guiss lepp cii mom na’ ngou ko nakk goor falay maté

{Zapata – Verse}
Bismilahi Aduna
Rahmani faagouna
Fa mom la beut la rathie
Nopp dalou fa fathie
Lakatikou laxasso
fa nga ndikou lassasso
Guedj- guedj guerri dji dougou dougou diaxasso
Nek fofu nekate so
Né wa peinkou naka sOwe
Touti takh mou yatou
Rakh ndakh day aatou
Dou dé daay xarou
Ba apeu diote mou taukhou
Dianay sakh cii bir pakh
Todial yakh bi cii bi pakh

{Gaston – Verse}
Yo
Légui da diéleu bèn beut lay xolé Illuminati leu
Gniy diamou alale diokou cii mom nane al mahdi la
Mou dékile xeureum, feusseul kheureum
Bodji wourouss diamou peureum
Moy diokhé di na-ngou,Djaay di rangou
Ragala sa-ngou takh mou gaddou satala diangou
Kiy lekk mbede moy tane
Bougni fale moy taneu
Tay mérr soubeu contane
Poto potolou fontaine
Xeuthie na assamane cii xoti werr bi
Def taatt té nanou beer bi
Xabrom dou cimetiere bi
Immortel la dou dé
Dinagne ko soul dou té
Lettre ak enveloppe amena loulène wouté
Aka beuri melo white, black, yellow
Dou gueum baay nélaw
Moy prêté serment, weulebeu tikou guerre ma
Ma wakh mou diéleu ma, deinke ma xaliss néma téleu ma

{Gaston – Refrain}
None la xarite la, yéférr la djoulite la
Ndjite la té djite la, djoundje nala Khibla
Sol tenue mbeep la, mythe la té ndiip la
Tiakh bi thiakh bou deep la
Kaddu ngui tawkhit la ( 2 Fois)

{N Diss – Verse}
Deukou waay dji gateu lolou
Xoll yi teudiou xell yi faatou
Beuss bou né nga deukou
Gaindé, bokou, ségue, sissou
Bou aalo ak xirou daay meingo mélokanou Iblissou
Xell mou sel mo diara sakou
Soka amoul da ngay dadjou do faggou
do fadiou dalay dieumé cii naggou
Fi dou keurou kène koudoul kou wett Cii tawkhit ki bérou zikrou
Ki niité done mélokanou torche bi di niiit
Goor dial-la wala ridialou adiou ba dialou
Diar dial ba faalou torr waar la sagou
Torrou waar la taalou
Del fauute mou sett beuss bou sett
Sangue sa Rouh help sa xett
Dokh cii rouh

{Ibrahim – Verse}
Moy ki taw cii boppam teuweu sebett
Deundou cii kaw lakou seubeutt
Limou nam cii euteum bi mouk dou soukh ba ila eubeutt
Moy xam té mo oumpeulé deungue té mo dioubeulé
Takhawé kène nek nieup, nieup fépp mou oubeulé
Moy kiy takhaw fé né nga da-ndou fé
Goungué la fii di ngatandou fé
Ngembe la cii diggou arène bi xamal ni ki ngay dane dou fée
Ndiip la, ndjiite la, djiite la, fégnou waay mélo you deep la
Niit la, none, xarite la, sakha yay cii ngélawou tawkhite la
Tékina tiakh bi foudou fa naw ba kaw ba kaaw aki wo saukh
cii dokh mouthie cii saukh bi

{Outro}
Xell mou séleu moy tekki bi lé tiakh
Deug Deug xam xam la mbeur dou ay nakh
Def Dara Studio Wuudup
Touti Wakh Job Lou Beuri

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR