LYRIC

Sample: Angel of mine
When I first saw you I already knew
There was something inside of you
Something I thought that I would never find
Angel of mine

[Verse 1] Abal ma bante ma dox, boudé goumbe teukh lou nga sant
Thiofel sopéku di ngante, sa leeray ya kawé sotéku ni jant
Taaral sunuy goudi, fadjar gou yèewu diakarlo di thiant
Li ciy yaw di mane, yaay kémane guiy saxami sama lanthie
Tèk nala fouma tègoul djiguène, yaay kèn kiy samm sama rèe
Séet na né douma ci guéne, sa ndaa lay tankh sassou ma maré
Daagoul mamma réer, ma fèkki la fa nga né té douma réthiou
Togal ma ma rère, ma teudi ndakh weuri gui dama ko wéssou
Yaay sama love, sama linguere, sama thiebou ketiakh
Yaay sama or, dafa sincere waral ma deuké thiakh
Deuké saytou, deuké wax, beug lep taaro ko waral
Titouma maral, ndakh fouma guèssou guiss nè mane rek nga faral

{Refrain}
Niu Bok jeumoukaay
Bok destiny
Tok di yéemu kay
Rek dess ci ñi
Jox nala sama kaddu
Jox la sama love
Sama xel, sama poche
Ba nieup né dama dof

Sample: Angel of mine
When I first saw you I already knew
There was something inside of you
Something I thought that I would never find
Angel of mine

[Verse 2] Yaw la Beug diox sama sant, def la sama yaayou dôme
… Teral la ci say nawlé, doon kiy takku fathie sa goom
Fo méré mané dou sagome, deuk sama waaw di sa côme
Niane sunuy bess sakane, goungué la ba baniouye gass sa kane
For better or whorst, together by force
Forget about pain, let’s share a true love
Boudoul yaw kane la, yaa fi tok ba nieup dawé
Ame ak niak gane la, tay sa tabax nimou kawé
Bala mbekté thiono, dadjé bi djitou sunu jeumm
Yalla ma djaglel malaaka, waral ma topp ko famou jeum
… Ndakh famou jeumay gueun gui deuk
May gueune di beug, jog ak daanou b dougne ci deuk
Lep dina léer, nice tégou ci temps/mindef you mélni yaw douniou fi 100
Na kooloutey daw, niou daw satan/Amoul loy kheutio sama thiofel sa camps
Angel of mine, jokh la love line/
Wonderful girl, u’re my sunshine.
Bind leu bataaxal diaglel la sama xol/ guindi la ba taxal nieup nieup xool

{Refrain}
Niu Bok jeumoukaay
Bok destiny
Tok di yéemu kay
Rek dess ci ñi
Jox nala sama kaddu
Jox la sama love
Sama xol, sama poche
Ba nieup né dama dof

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR