LYRIC

{Intro Ngaaka Blindé}
Tolluwaay la cii mane
Tolluwaay la cii yène
Tolluwaay la cii mane
Tolluwaay la cii yène
Tolluwaay la cii mane
Tolluwaay la cii yaw
{PPS}
ATE- ay DOX niou kay wanié ci WEER, niane BESS you sakane
Do jok ci WAXTU ci ay SIMILI ndakh nek SECOND
So amoul weerouwaye PAUSE, guiss sa life di RECULÉ
So SETAANÉ finga diar, bras long la tée AVANCÉ
MISSION bi djitou na ZAMANE, boul xaïma lima LAKK
Saay GUEINTE diox ma YONÉNTE, TEKTAL ma lamay lakkeu
Fouma DJAPÉ DIOULI NIANE, NJEGUEULU noone yi may ALAK
..IXSSANA téer samay MBAGG, TIIM ma ni NIARRY MALAAKA
LAMIGNE bi né sa DER, tek la BËUT, yenéme dou ba kane
Djeuw yi téer sa NOPP, sangool imane noote sa BAKANE
Sopi demb XALIMA, NJANGATE yi MATADI, PAGES yi MATE
Done NGAAKA ci bi CHAPITRE, JANGAL sunu PAGES(disciples) yi MATH
Xamal finga DJOGUÉ, ngor ak jomm di say ROUE
Tek ko ci CODE goor yalla, DAWAL seelal sa Rouh
Lou TALI bi XATE na xool bi tali, ko tané YOBAALÉ
BOUR bé niou boolé, té YONOU ndaw dou BAALÉ

{Refrain}
Life ba ngui dokh té bouma sagnone nga démééééé say neurone
Def lila warr bagna reuthiou moy li gueunone (2 fois)
Aduna Tolluwaaay la Tolluwaaay la Tolluwaaay
la Tolluwaaay la Tolluwaaay la

{Ngaaka Blindé}
Fi yonou ndoxla mayko mou dialeu ndakh tissna
NIT dou karaw rek la yénou, DOFF bopp bi dissna
Niakk dëgg tolluwaay bou gaateu andi fitna
Ndaké tank kassé dou dokh khana tiite nga
(Teukh) Sa xol moy sa yëg yëg
Sa xel meune na nangou way sa nopp mokoy ndieuk yëg
Té Mind dafa beuri louniou cii drope bé
Bo xamone louy neurone do wine té do drogué
Xel meune na niite ni lampe di Shine
Meune nga dox té dofi jog sankeu ya ngui fii
Thieur bi gueuneu goudou cii nit dou Mind
Da nga koy tagate nguir mou dox tant que ya ngui fii
Waw xaliss, keur, auto est-ce que moy vrai am-am?
Wally, Balla dagne lay nakh Goor Sa Bopp def ci xam xam

{Refrain}
Life ba ngui dokh té bouma sagnone nga démééééé say neurone
Def lila warr bagna reuthiou moy li gueunone (2 fois)
Aduna Tolluwaaay la Tolluwaaay la Tolluwaaay
la Tolluwaaay la Tolluwaaay la

{Simon}
Diox ma CIMENT SUUF a NDOX dama tolu ci TABAKH
Owël leen ma MAÇON ma RAKH xél Yi ni Dabakh (Allahou)
FONDEMENT wu WADE nga Fok me Djëmël TAKH dëgou ci ni juliit bissoum aljuma
Baffi louy law latta méy DÉM Djib dou THIOW
Gnakeu di siite nguir dieurign samey dom
Bou loxo yi WADE nagnou Jog Job (DIOP) Na ko dal ni makheudom
Diom déy Fay (FAYE) moléy Fal (FALL) nga santeu NDIAYE Mba DÉME
Job, Job Talouma wax démey féy COURANG
Féy ndokh dioxé dépense Bobou ÉNERGIE wax Douko RANG
Ak lu yoon gui LEUNDEUM warougno MAAASSE
Fog ñu tékki LEERAL kanam yii ni sougnouy ay masse
Tassaré tolouway beu timeulé ko TOOTE You tékki
TITEUL TEUBEULI TEUREUL Gni TOSKARÉ
Tadj ak tamou métiteul Timeulé Ak téguine Téré woul gnifi ték tank
TADJ ko gnène tébi Tarbiya lo gni tipsé PEUTEUKHEUL Tall gni ci Beuger tékki

{Outro}
Aduna Tolluwaay la
Defko ni sa Tollou waay
Mbaarik’Allah Mbaarik’Allah
Mbaarik’Allah Mbaarik’Allah
Aduna Tolluwaay la
Defko ni sa Tollou waay
Mbaarik’Allah Mbaarik’Allah
PPS The Ghost, Simon

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR