LYRIC

{Verse 1}
Héy yaw fuck séni menotte Baby légui ma guénaate
Niou ngui diém louné nguir beug saletél sama honneur
Baby dalal jaameuh calleul sama lawyer
Boulène may louniou beug bou sa beute yi toye-yeu
Sama coffre-fort bayi nafa money sama mot de pass moy sa birthday honey
Dagnema seuf gun nénagne mako mom té gun dafa meusseu kill nit ci bèn Old up
Yégouma tinoumeu really not guilty lou djougué woul cii yallah raggalou mako kone word up
Kouma djégué lolou moma wara djaay
Té khol na ba khol beugouma toumeul kèneu cii samay waay
Amena arrivant bou aksi fi mandat de dépôt
Waayé limouma djota wakh beugouma wone sakh nga yegg ko
Néna Pablo bila done toppeuh moma piégé
Nguir ma dougou jail ndax sama place la beugone siégé

{Refrain}
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek
Fima diaar ak yaw andak yaw bimay nieuw sa side di dieul sa five bobou do wone shit
Life dafa teureudi dém ba doto waulooti
Money takh nga call the cops yoléma ma dougou jail
dougou jail dougou jail
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek

{Verse 2}
Baalma té djégueulma djaffé djaffé yima lay doundou lo
Demna ba am kersa khol leu ci beute té xouletou wo
Lékkato naanato djabbanté cii parloir
Akh bouy dox sunu digueunté leu donté tay la waar Doyna waar
Piste El Pablo niou bagneko enquêté
Parce que amena bras long sen poste lagni inquiété
Lou Yallah diékhal mou diekh na sakho xollou mougne
Na avocat bi def liguéyeum nagnou doylo Kun
Légui xam naani Torres mo def Gun sama car
Démal Dic convoquél presses bi niou bindeu sama cas
Waratouma fanane béne nuit de plus fi ci jail
Pablo yauné nama lettres naanema suicidél
Insbi dafay vulnérable ndakhté naagou na
Dafa am sa faiblesse wo ko néko nangou nga
Tek ko deal caméra cachée ko bamou avoué
Andal ak sa sang froid on a qu’une carte a joué

{Refrain}
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek
Fima diaar ak yaw andak yaw bimay nieuw sa side di dieul sa five bobou do wone shit
Life dafa teureudi dém ba doto waulooti
Money takh nga call the cops yoléma ma dougou jail
dougou jail dougou jail
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek

{Verse 3}
Fuck yaw ak sa Kingdom est-ce que xam naniou ki nga done
Snitch nigga what’s living ? your life is being alone
Yeah it’s me Kila dieulé wone cii ndaule bi
Kila fékone cii mbède ngakoy niakanté thiool thiool bi
Kila daane diokh Jo, clothes yi ba tchi call bi
Ki nga fénal seuf ko gun dougueul ko tchi taule bi
Yeah it’s me bitch soxna saa ngui galé tok
Kila daane toggal ak fauteul say yëré à l’époque
Soxnassé ko goréé waay louné lako waadji dik
Thiabby keur, takaayou diamant mouné ko fuck shit
Bitch Nigga da nga fake ba melni Silicone
Yallah rek la ragal soxla woul ngay firi gun
Yeah Bitch ass Nigga you can kill me nigga
You can shot me down whatever you want nigga
But you are not gangsta fuck you nigga fuck you

{Refrain}
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek
Fima diaar ak yaw andak yaw bimay nieuw sa side di dieul sa five bobou do wone shit
Life dafa teureudi dém ba doto waulooti
Money takh nga call the cops yoléma ma dougou jail
dougou jail dougou jail
Ci Love ak ci respect lako yagg tek
Meussouma gueum ni biss dina nieuw nga fipou djaayma prek

 

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR