LYRIC

{Verse 1}
Real rap undercover leu
Bari japp kone over leu
Bou féké Checky Blaze nguey weur nguir djap datch ay onde leu
Dou ay rimes, ay onde leu
Bari fem kom James Bond leu
Bo ko sauré signé sa dé, kone gass gass sa tombe leu
Explosion ni bombe leu
Boy P.A rek monde leu
Daw si ngoré la bok kone jappal nigga nigga jombou leu
Xef xippi mou romb leu
Rak tak mou bomb leu
Bo ko guissé diaroul nguey xar yonel instru mou songue leu
Def rap tewal sa conneu leu
P.A sama honneu leu
Teknik, melodie, flow ak bepp rimes ay sonde leu
Diappal nigga noddeu leu
Fake démal niou wodd leu
Boy P.A back in a dayz meuno ko watché nigga waddeu nga
Dou ay clash ay tontou leu
Nieuweul déglou ma sondje leu
Mc yamal sa place bo ma songué xamal ni lonk nga
Daguey xarou fontou leu
Dou ay rimes tiontiou leu
Xamal li nguey woté ndakh bepp caddu ponk leu

{Refrain} x2
Loxo si kaw niou djouk téwal bepp soldier (undercover)
Niou reprezen gni di fightal suniou konneu (undercover)
Microphone niou téyéko ni béne gonneu (undercover)
Bepp soldier (undercover)
Real rapper (undercover)

{Verse 2}
Done soldier nigga maitrisé ko
Yéggal sa verre tisé ko
Flow, rimes many teknik, many style hypnotiséko
Gueum sa bopp té miséko
Bepp fake nga briséko
Done real si birr real yi kone rimes aiguiséko
Séntoul top té visé ko
Job bou doy réviséko
Lepp lou ley tardel tek ko tchi xatch té visséko
Am sey limites fixéko
Am ay chartes érrigéko
Bagn kat fo mounti né, fightal sa life dirrigéko
Done haterz évitéko
Rime ak flow éxigéko
Bou féké rap mo la takha djok taneul sa ins invitéko
Sey caddu méditéko
Bepp text éditéko
Real rap undercover, bepp soldier sédéko

{Refrain} x2
Loxo si kaw niou djouk téwal bepp soldier (undercover)
Niou reprezen gni di fightal suniou konneu (undercover)
Microphone niou téyéko ni béne gonneu (undercover)
Bepp soldier (undercover)
Real rapper (undercover)

{Verse 3}
Béne ! 2h bo si dougué deugoul ni soldier
Niar ! héxagone fo mounti né téwal sa conneu
Niétt ! Engagé ni militaire xaré tcha front yeu
Niénte ! Rap dou politik kéne dou yak suniou honneu
Diorom ! 2h ni guérilla kounek ak armém
DIorom béne ! Gni di gass, gni di soul negn niou arr men
Diorom niar ! Soldat tchi fight, soldat tchi mic nigga si bir théme
Diorom niett! Soldat tchi mine, soldat tchi rime suniou embléme
Diorom niénte! Mbed biniou reprezen ni suniou area
Foukk! Show your hands in the air bepp guerrilla

{Refrain}x2
Loxo si kaw niou djouk téwal bepp soldier (undercover)
Niou reprezen gni di fightal suniou konneu (undercover)
Microphone niou téyéko ni béne gonneu (undercover)
Bepp soldier (undercover)
Real rapper (undercover)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR