LYRIC

{Sanzala – Verse 1}
Slanleyk,, Fuck fékk képp kouy hate ak kouy sikki saka-
Maay Sanzala,, Romb naa séeni level,, Stargate
Yéek agueu si thiolou rap bi geum teup,, Saut de l’ange
Toudou God,, Sakh laaf,, Khoti yoon bi like Chau devant
Rap moy sama job boy damay programmer ay beat boy
bindeu text you doff boy,, Wakh ba gars yi di tiit-
Ma ngui Up Stud Rekords,, Hardcore laniouy taatch-
Saabouniouy déf si mic bi my nigga laadjal Dégg Daatch my nigga
Bii track amoul plafond boul djéema natch souniouy kaddou-
Bokouniook nioniou nonou,, Bo beugué nga nieuw addou-Boulniou sakh taggou-
Daanou léen crise,, Like khambeu,
Maa ngui dém yoff gass séen cambeu,
Rest In Peace, Likhlass Souul na samay problémes
Boolé café touba ak mbiskit mo ma djokh bii flow
Boolé Sanzala ak Nit Doff,, Bi track dou low
Doundou Galsen 24/24,, Goor Yallah yi fii leu
Bénéen bord bi ay fénkat youy djéema rimer
Abeul bénneu portable taper numéro 17
Tay ma khotti bénneu life fayéekou tchi sama dette
Criminelou démbeu, sangoo mbadjou velvet
Wakh naa la li nieupp beugueu dégg rakk déel get

{Nitdoff – Verse 2}
Doff to the King Killah With my nigga Sanzala
Gaindé aleu bokoul ak Gaindé nguiy feithie simbeula
Dama xirrou xoureul battt yaw ngay nossal ni Singuila
Da nga thiap té da nga ndaule amoulo wétchite cii saa call
Ma criss samay baggy mouy djougué cii sama all
My bindeu rhyme bégué homes boy yi nek Taule
Thug Life lay taf for my Diw Squad Zou
I don’t really giiiive up fuck about nigga. you do, I do
Hustlin’ for Lot of Doe (Xaliss) Never Mind I gotta Go
AK 47 Killed the MCs bad flow
Real talk, hainou la, I’m ghetto super Fly
Kèn dotoul sik-sak number one bi Nitdoff la
Real nigga daay gueuneu Brain
Respect, protect té aimé friend
Bitch love my mussel, Money from the hustle
Fake ass, pussy nigga dandoul boulma seussou
For Ever O.G (Original Gangta), Khéw cii diamono J
Tchii kék lay sakhékou, Amoul fiit ni Dyno DO.G
Niolay door cii dothie yi, Guétéro cii flow you dodj yi
Diamond cii OG (Oreille Gauche) xalé you mokk pothie yi
Katakayni, kangadou Gayne bi dafa fodo
Beuri dolé gawa shayne doula door té teudo
Like Selbé Ndom Believe me I can see the Future
Bou Mc Yeup soukou diébeulou ma done sen teacher
Sampeu na ndeude di xarr rival guissouma picc

{Sanzala – Bridge}
Beuguouma di satheu flow djambour ma créer béess takkheu-
Féess délleu djappeu doolé nguéen djakheu
Life bi moma bakkeu ma fakkheu si prison-
Di teureureuri di naaw, Niou djappé ma pigeon
Bénneu,, Rap di nguéen gueum dou rap deugueu
Sa bouma ko wakhé nguéen dima tam deumm-
Dou deugueu dou yoon «2x»,, Yalla mi niou tiim khamna né-
Dou deugueu dou yoon,, YEAH

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR