LYRIC

{Intro}

{Verse 1}
Sa sago saki na séy
Xell lago doff dina féy
Mbir mba ngok yague na déy
Tiarakh dou Back ina day
Double ri cii sa kiss
Ya mouki mouki mogui diss
Li sa beut mi mom di guiss
Sa xell bi néna mom douko miss
Doff nga doff nga
High! Tiof nga tiof nga
Légue légue yénou sa loxo di youkhou nane “Rof nga rof nga”
Mélo wou psychopathe la
Ngélawou liko djaate la
Ponou sougouf sou wékh sunu bolé Carbonade la
High ! Dox cii wéér bi, Fly guédd terre bi
100 à l’heure ngay daw saaga (Insulté) Pa mbéthie nga mère bi
Da nga adiou, ya ngui weuthiou
Da nga sa-ngo kané kadiou
Dox di treuf, xell mi peuf tothie
Your yi tourou nourou
Saxarr cii ngay sourou
Molay yaubou ngourou
Overdose. Nioulay cause melni kouy salirou Xirou
Gaïndé bilay daki ngay daw
Xathie bilay mbeuw
Takh cii délit rek nga téré
Takk cii bopp bi tééré

{Refrain}
Niankatane kani la
Xeuthial fi sa noney la
Door sa member saane téréla noki baatu diam yi la
Violent né waw nila
Bagne paix, nane niani la
Si kanamou soul sa kom avortement teukou niane yi la (2fois)

{Verse 2}
Violent ni souli yakhou néw défko tééré bi
Violent ni djouli cii dérou xathie saw cii téréé bi
Violent ni djoulite def kott pénal, diklé téré bii
Violent ni Serigne bou diabarram dém ba moudié téré biir
Violent ni viol, vol, vérifié virginité
Tim bolou laakh bi goal bafoué nga sincérité
Violent ni pédophile yi
Déglou coup de fil yi
Digou ganawou Mame dembe ak chaines ak coups de file yi
Violent ni taale sa bopp Palais
Keur gou beuri laisser aller
Tiakhane cii seune (Mbalite) yéwou nane na mbedeu bi balaie
Violent ni commentaire rou Seneweb bi
Signel visite technique Carapide bouy djéingue, khour dawé wett bi
Violent ni manipulation bouy daw cii biir média yi
Loufi tak nioko taale, xambeu rek diour dégât yi
Sopi xibaar bi Macky dissi tiagatou lii c’est sale
Nougni def ba yonou sankouté dou violent Sénégal

{Refrain}
Niankatane kani la
Xeuthial fi sa noney la
Door sa member saane téréla noki baatu diam yi la
Violent né waw nila
Bagne paix, nane niani la
Si kanamou soul sa kom avortement teukou niane yi la (2fois)

{Outro}
Yeah Kétal Kétal Beat Salad dose
Yeah violent ni légalisé goor-djiguène téré baune
Violent violent
Yeah Baye Dieuwrine
My nigga Omzo MF, itsua
where u are?
Yeah !!!

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR