LYRIC

{JahMan}
Doff na ci love, Demna ba xawma lanela
Damay tokk sakh di wakh ak sama boppeu
Fepp lay guiss sa dieumeuh. Baby lanelaaaaaaa ?
Sourna, tay bouma kèneu wo agne
Naanouma Tchaayine waxtanouma ak yène gaayine
Mbeuguélamay gaaaaaaaaaaaaaagne
Oh Ooooh
Demna ba soumay settou baby mane dh yaw lay guiiiiiiiiiss
Li am ba dess moy sama xol bi yaw lay MISS

{Refrain}
My number one girl, My number one girl
Sama vitamine girl, Sama vitamine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
My number one girl, My number one girl
Sama Aspirine girl, Sama Aspirine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
Sama vitamine girl

{JahMan}
Dama doff ci yow té koumou neexoul ya xam
Yagg nala wane té dieufna yaw rek la am
Baby soma baayé mane fane la djeuuuuum
(Laaa djeum, laaa djeum)
Wakh nala fouma guestou mane dh yaw lay guiiiiiiiiss (Laay guiss)
Beuguena nga xam ni sama xol bi yaw lay miss (Girl)
I’m ill you my medecin , you’re the one and I ever seen
Baby girl tell me what you mean so degué sama call gnibissil

{Refrain}
My number one girl, My number one girl
Sama vitamine girl, Sama vitamine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
My number one girl, My number one girl
Sama Aspirine girl, Sama Aspirine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
Sama vitamine girl

{selmind – Verse}
Maydey maydey.Ambulance, arret du coeur, mort subite
Gaawé lène ma yaubou urgence malaaka ma setsi biik
Guiss leu tiite dotouma nit, deuk ci mbède mi weur di niiit
Li dou nèène meune nako waate
Lou djougué cii mane dou déloussi waat letma wala nga firima girl
Battré carte gui coupe ma jeul founé ma kheul louma dikeul
Yéména reyna ba danéma feul yobou nga khel yi fess khalat yi
dafa melni dama déé di dokh kéne dou fathie sama maladie
safatouma lima adouna diokh fok ma binde té wéyla tague la
kagne latarou nga jekk ni siren foma wo ma wouyou la lolou doyoula
legui ma youkhou ni siren damala guént ba beut di sett keuf la fly
gnou andeu ci pet foumala sen rek gueneuti bég ni jant damalay geum di chek

{Refrain}
My number one girl, My number one girl
Sama vitamine girl, Sama vitamine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
My number one girl, My number one girl
Sama Aspirine girl, Sama Aspirine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
Sama vitamine girl

{Brah – Verse}
Yaay sama queen, wanema guinaaw rek def nga murder
Bi nga démé ba légui niata missing call sa number
Djotna la miine djargogne képp nama ci leundeu
Mbeuguel bima déinthie pour yaw xaliss meunouko dieundeu
Déloussil cii Daara J yauni naa Ndongo ak Faadda
Di ngama gaagne ci beus yu nëw rek xalébi nga néma nada
Togne nala baalma Please nangoul saggalma
Meno niak ci sama life biss niki tay man dalna
Dangma jekou wan ma guiss ni manouma dem té boko
ci sama life yaye cafka bigniy weur guiss si goto
boul dem bayma noto dou cagui ni sax meunato
kholal si none yi deuké fight ndax begougnou guiss gnou joko
Meuno gnaak cii sama life biss niki tay mane dalena
Da ngeu ma djékou wanema guiss ni meunouma dém té bokko
Tchi sama life yaay thiafka bii gni weur guiss ci gooto
Boul dém baayima noto, dou tchagani sakh meuneuto
Xolal ci noone yi deuk fight ndakh beugouniou guiss niou djokko

{Bridge}
Noumay def ba guissaate leu
Noumay def ba guissaate leu
Namena laaaaaaaaaaaa
Hooooo Owww Hooooooooooooo
i love you so ,

{Refrain}
My number one girl, My number one girl
Sama vitamine girl, Sama vitamine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
My number one girl, My number one girl
Sama Aspirine girl, Sama Aspirine girl
Gnibissil girl
Boulma sori may wët
Toggal sama wéétt
Noumay deff ba guissat la
Sama vitamine girl

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR