LYRIC

Sample…

Couplet 1

Gnon ngui ci yoon Mangui Ci Yoon Diane Deungoul Yoon Balaa
Goor deugoul Noone Balaa
Fi Dou Nopalou Kaaye Diangue Bou Messoul ame alar Balaa
Fi Dou nopalou Kaaye Diangue Gou Messoul Ame Alar Bala
Dougnou Messeu Soukali Waaye Beuss Bou Nék Mandar Gala
Tafanto Gent Ak Yéné Yii
Surveillé Sounou Ndjite You Aliéné Yii
Discourou Sathie Féneu
Tayelé Gnou thi Khotou Néneu
Dembeu Tareu Tayeu Tareu Soubeu Yiiteu Douma Téré Xoslouman
Lima Fi Diota Khatim ak Rek Laciye waslouman
Waw Bén Beugne Bombale Fékhél Na Wékh Taleu
Kou Nék ak Sa Mbed Rombale Gnaffél Na Nékh Daleu
Beu Lgui Ndaye ak Baye ya ngui Khar Sén Doome liguéye Beu Wathie Faylénn
Waaar Yii Ci xél Ak Xol La aye Thieu Baylénn
Fowoume Goor Kou Ndieukeu Yokhou Da naga Ragal
Lo Beugg Deugg Beuss Dou Niak Waw Dalay Sagal
Na Makk gni yeureum Goney Fékhé Daleu Nougnou Régué
Ndakh Adouna Dou Dara Loudoul Dioudou Dioye Ré Dé
Nagnou Sante Mougn ak Moyetou
Mouslou Thi Tokk Di gnakhetou
Fassou Mougne Kouko War Deukou Banekh Dia Thia ngeuy Moudié
Té Bagndi Tok di Wwoudié

HOOK
Dieul Diome Djiteul Fiteu Ngoor Dou Baayi
Fi Daleu Mome dara Béssoufi
Mane waslou Xoslou Rek
Démbeu Ak Tayeu dara Béssoufi
TolTolane Rékeu Fi Nek Daw Ak Réne Dara Béssou fi
Dara Béssou Fi

Sample

Refrain

Ségaam Bén Beugn Day Wékh Fékhél Sa Metier Néx
Mane Rap Bimaye Rap Akk Rékeu La ciye Waslou
Sample
Ségaam Bén Beugne daye wékh Fékhél sa Metier Néx
Kou Khole Démbeu Guiss Tayeu Khamni Dama Xoslou

Couplet2

Khar Daye Wéssou Mboté Mané Mboté Dou Wéssou Kouye
Music Dafa Arame sama safara Narna Céd Gouye
Niteu Meunteu Nité Nité Beu Remplacé Yallah
Sama Music Mangui Thiye Diamou Dou Rek pour Diameu Dal Leu
Dioudou fou Amoul Dara Sobou Ci Art Bou Léroul
Aye Doff Ci Bén Gal Motakh Beu Légui Téroul
Boudé Sipp Nga Yéroul
Galgal Fakastal Fi Ni Dou Dégg Sérloul
Yaar Ak Diome Fite Ak Téguine
Xoslou Rek Beu Yaye tékk Thine
Baayi Lép Né Thi Léneu
Yoré Bak Té guisso Tén
Yoré Bak Té Meusso Dioukki
Waar Bou Yatou Ni Guéthie Tax Kou Sobou Dothi Noukki
Waslou Ak Waslou Ak Né Ni Deureum Bou Dieum Thi Diakka Dji
Tayeu Taar Trope Takh Kouné sa Toom Ngaye Daka Dji
Kou Ba beugeu Bakha Sonou Lonkou Ni Pape et Cheikh
Gni Né sa Guinaw Dieuw Adioul Gnou Wax beu Diékh
Barastikou na Beu Tayeu Treuff Perte Ba Tayi
Wayé Daara Douma Takha Baayi Mane Mangui Thi Guerre
Thi Mission La Nék soorko Ni Mbaxalou Xéér

HOOK
Dieul Diome Djiteul Fiteu Ngoor Dou Baayi
Fi Daleu Mome dara Béssoufi
Mane waslou Xoslou Rek
Démbeu Ak Tayeu dara Béssoufi
TolTolane Rékeu Fi Nek Daw Ak Réne Dara Béssou fi
Dara Béssou Fi

Sample

Refrain
Ségaam Bén Beugn Day Wékh Fékhél Sa Metier Néx
Mane Rap Bimaye Rap Akk Rékeu La ciye Waslou
Sample
Ségaam Bén Beugne daye wékh Fékhél sa Metier Néx
Kou Khole Démbeu Guiss Tayeu Khamni Dama Xoslou

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR